Vidéo: La réponse d’Iran Ndao à Ahmed Khalifa Niasse. Regardez!

Si quelqu’un a le don de provoquer un tollé de réactions à chacune de ses sorties médiatiques, c’est bien Ahmed Khalifa Niasse. Cette fois ci son discours sur le port du voile continue de faire des émules. Aprés Adja Fatou Binetou Diop, c’est au tour d’Iran Ndao de fustiger les propos du frère de Sidy Lamine Niasse.Regardez !

23 COMMENTAIRES
  • bapsou

    wakh daye werr wourr

  • Amina

    mercy Iran Yalla na Yalla goudal sa fan yok la werr,Amiin yen yena takh niou ni Oustaz waye dou doff yiy worr television yi daganal lou Yalla aramal

  • Badiéne

    Walakhi iran liguakhaw deugue la, khalifa Niass diap diné jii woyofolko ni zirike teumbeule ci ay glacam kouthie beugue lou yombe ba nane ko digako réthiou. Wakhine la nak déguine la lathie

  • wakh

    halifa bamouy wakh la xamni day doul doméram

  • wakh

    doul rek

  • Youssou

    C vrai iran Ahmed mom day fnn rek leugui mais 2 femmes yoyou tok sa kote tamit wakhal ak niom d’abbore

  • ndiouga

    aa doyna waar

  • abdou fall

    Galsen keur go dougou am na yok kholaleu gni tok fofou

  • lesi

    Iran ndiogane la way .

  • Aicha

    Franchemen amena aye oustas sénégalais khamounou dara
    Nénanou So défé méche sa djapeu bakhoule ndakheté sa bop toyoule …. Non mane jy croix pas ,….
    Les arabe défénou méche té sén karaw dafa goudou
    Kon que fait ton lé arabes sounouye djapeu?
    Lou Ahmeth khalifa wakh la gueume , nit day khalate té khéle dou jariene lou douye khalate

  • mouride

    iow la geum deh Deug nekhoul

  • elhadjika10@gmail.com

    diareu dieuf Iran ndao amna solo yalla nala yalla faye

  • elhadjika10@gmail.com

    gc

  • elhadjika10@gmail.com

    Iran yalla nala yalla faye

  • makhtar

    aycha amou khéldé lolou karawla bokol ak méss sakaraw noumo mana dollou dagay séy massa wayi yoko dafa haram dolounoy khalatt dancoy diannga

  • malamaine

    BarakAllahou fiik Iran.

  • kaolack

    Mais Aicha arabes yii Séne karaw la toi aussi,dokhalate bala nga wakh.

  • gorgoru

    dieureudjeuf

  • leye Mohamed

    li haram haramna li dagane daganna yaomale khiyam yalla moy atte te moy diegeull kouko nekh te yalla naniou diegeule sounouy bakar amine

  • Marika

    Ahmed khalifa dafa light mo takh ma beugue ko

  • khadim diane

    meci iran khalifa dowakh katou deugue

  • Abdou Lahad

    li am solo moy réspécté 5 yi yalla santé pour dioulite:
    1-yalla kéneu le amoul bokalé,
    2-diouli,
    3-woor wérou kor,
    4-guéné assaka,
    5- dém makka so ko meuné
    li ci déss nak yalla mo kham li nék se khol lay khool, mais ay wakh rék; yalla douguel ne diw adiana wala douguel ne diw safara yoyou ay histoires le rék you ay nit binde ci ay livre, dara worou ci

  • Anab

    Praise be to Allah.
    __________________________

    Stay away from foolish arguments, what more in this blessed month #Ramadan. Yet we continue with verbal attacks & disputes. Keep the peace.

Publiez un commentaire