12 COMMENTAIRES
  • aziz

    Eumue SENE DOF BI

  • MODOU DIENG

    ahmet aidara nena dagno diawalee envolop yii def koo sen posse

  • bijou pata

    ay waay yeureum nalene kouye sathei bagnou diapoulaa

  • abba sathie

    ya awa diaratoul touss thii deukeubii

  • DEUKHIN

    exclusivite yama ak cheikh sarr defante en derect mbamou nekh bamou saf ya awa monekone promateur bii moka teugone

  • ya awa diaye mana

    thioro mbar ndiaye amoul fitou di leen sosaal deugeulaa

  • beurititar

    li dee komako wakhoon ma wedikoo ya awa diaye mana bimou fineke

  • tima

    ho khouthia yaw topatol sa émission li yeup guir begua am promos si walf sa mom ham actualité té diko traité ya awa bijou ak aba bougnou ko défé hamena gnou bougnouko défoul hamena gnou té thioro limou wakh lérena

  • athia

    kouthia ya soofff deug

  • niakk kinianne

    lungay wakh nekoul
    cisakhol kouthia boulnou sonalway

  • yeureum

    niakk kinianne ma laa fan deugeu rek gay wakh yalla mo lako takha wakh

  • LIA

    Attention Thioro n'a fait que relater les accusations faites sur eux et D MEDIA qui exige remboursement en restant ouvert aux incriminés pour leur version. Elle n'a jamais accusé. Il faut suivre l'émission de Walf avant de parler.
    Bien avant que Thioro parle on a déjà l'information dans la presse en ligne, mis à pied et demande remboursement aux incriminés. Avec Thioro c'est l'Actualité PEOPLE. Il faut savoir lire entre les lignes ou déboucher vos oreilles pour bien entendre les commentaires.

Publiez un commentaire