Vidéo- incroyable Tounkara avec les "fakhman" sur le plateau de Sénégal ca kanam

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Aucune recommandation disponible.
Aucune recommandation disponible.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
SALAM MOUHAMED BOUSSO MI SANTOUL MBACKE KI EMISION BI YEPP WAKHI DOF LAFIY WAKH WEROUL
mouhamed bousso mbacke mii dé santoul mbacke, thi gniy yakh dérou mbacke mbacke yi rek la bokk, mbacke mbacke yi mom lougne mane di déff tamit fakhman mom amagousi, bayi leen sen thiakhane yi té dém diamou dji yalla
Ndeye sane le jeune m'a fait pleuré,dimbaliko bakhe na dé
ndeye san sama yaram dafa daw yalla nalen yalla diapalè banou guène si li way
kimomana fene khelcom masoul am dooré
Bizarrement, il sont tous issus du monde des daras ….. Faut se poser des questions
Niit day am yar gui boleene ga falee dakh li nioy wakh amoul aferou mourid magay wakh sa wakh wou niaw limou begue moy li guene wakh go dara mouy conmanter at yanee ni conmanter you niaw nioune mourid yi ball nanou la sy Khol bou seed gouyou nioune ay diolit lanou ba baree done ay mourid ta yaw doof ga wa Senegal khana niom khamou nou mourid limoy deegui si arab walla khamoleene arab mourid moy yone wou dieme sa yalla khana yeene deemoleene sy yalla walla magui balou akh boubakh sakh takh lima wakh dou yone dakh tou pour li wayee toukara yalla nalla yala fay si Lou rafet li ga deef wa salam
bayilen di wakh khelcom li guène di wakh amoul khelcom
bravoo tounkara emissionbii begg nanusii
Bizarre yow kou toth sa diobou ndey ngua, fi ana loufi indi ay mouride wala tidiane domou bireul bingua done
regardé mw ces embécile la !!! ñiome ñiépp aye mouride lañiou wargéna kholatte séne yone déh kou boônne rék so kholé baye fall la dangén di dof dof lou rék darra dalou léne amouléne yaye amouléne baye kel pért
SA WAY YAW TA HAINE DES MOURIDES DINTHIE KO TIE SA TOUNE BI
FI SENEGAL LAGNOUY WAKH PAS DE TARIKHA
SALAM
MAME ABDOUL AZIZ DABAKH MEUSS NA WAKH NI KOULA LATHIE NDAKH MOURIDE NGA WALA TIDJANE KOCOU SATAN LA MANAME SEYTANE LA
KONE YAW @BIZARRE SANTAN NGA SEYTANE NGA
bayilene fene mane mi khelcom la nekone maléne geunona deugu fopp kene moussouma djengu yaw m bousso mbacké esqu sakh mbacké gua sant du jamais vu djém léna bakh bakh rék mo am solo tounkara senegal khamougnou sa ndieuk bou souba lanouy comprendre
on connait nos maux mais on s'empeche de reagir a temps.
combien de deputes on a mais personne ne les vois jouer ce role bravo Tounkara.
president dimunier Le train de vie de l"etat pour servir a ces jeune. mognu guneul thiow yi ak mayer yi der
mais celui la, il ment khelcom amoul douré, depuis 15 ans magui khélcom téé ki khaméwouma go fa
senego ce vidéo n'est pas incroyable.il faut les respecte ils ne sont pas des fakhman yalla moo binde t'a où télé yalla n'a l'en yalla diapales ci barcke serigne touba khadimou rassoul
@WAw WAw ya bakh, yalnala YALLA FAYE
le daraa est un systeme concentrationnaire il le dise pire que la prison qui ne produit rien de bon
Tounkara yalla nalla yalla takhawou si barkee seydina mouhamet ( psl )
Big up Tounkara
Mohamed bousso yalla nga ame milliard,gnatta dome nga ame moune aye milliard,yatta fakhman aye milliard,teksi souma amone milliard…Deugue rek la wakh Senegal milliard yi dagua koye degue comme c pas possible. Big up Tounkara
Tres bonne initiative merci beaucoup tounkara cest vraiment beau
Mahamed bousso mii dano yapp
doyna war yalnale
n sonou borom takhawou genelen si Dion mom khalebi diap len si bok tonkara mou gen si
doyna warr yalla nallén yalla takhawou
ndeysane je me rappelle bamasi neker
Vraiment tounkara yangi ligueye pour Sénégal dieum kanam. Merci bcp.
Bousso mbacke mi weroul dé… Boy bou ndaw daw na sama yaram… Sniff
ET VOUS VOULEZ RÉTABLIR LA PEINE DE MORT……….., POUR QUI…?
Bousso mbacké mi wéroul dé… Mai boy bou ndaw bi dawna sama yaram… Yalnaléne yalla diapalé..
mdrrr mouhamed mbacké bousso bireul nga fakman you djiguén yeup ( fakwoman ) tu koné mm pa le nombre d gosse k ta
incroyable, senegal nou mouy demain ,passer toute les journees a gaspiller de l'argen au grand theatre extra extra ,alor que ces jeunne sont antraint de pourir dans les rue. il faut agir