13 COMMENTAIRES
  • fatima

    eumeu sen seytané nga en pluss sa wakhou deum yi moy lane ! khalé bou rew moma gueuneul khalé bouy fén mane

  • Elhadji1995

    عوذ بالله من شيطان رجم

  • biba

    yow emeu ko yab yak dèrou balla ba parè togeu fi di wakh so nièkè wone fi dou rafèt afair de yak dèrre dal bakhoul

  • khadimsylla

    kadeyui rafetna terop

  • samba

    Eumeu sene kadou yi rafet na machalla moi je suis fans balla guaye mai yalla nanga done rois des arènes

  • baba nini

    eumeu séne daaal yaaa nekh koi diap balla defal ko affaire ba parer diko tag . li nga wakh yeup bou neker tchi moom khanaaa kone yaw extra terrestre nga ?

  • bouki

    Apres le grand peché commis,tu cherche a te racheter.
    Tout ca pour que les senegalais disent que t'as un grd coeur.
    N'importe quoi.
    Rappelles toi bien quand tu disais meme si on te reveillait du lit tu allais le battre.
    Aukourd'hui tu oses dire qu'il s'est bien entrainé.
    Stp,arrete de nous ambaubiner.
    wa salam

    • baye

      Bravo Eumeu Sene, témoignage bii rafetna. Yalla nala Yalla téyal boppam té moussal ta ci Chaytanné you melni bouki. Bravo Eumeu encore une fois et bravo à Balla Gaye 2 toi aussi, tu es un homme de grand coeur.

    • bagne bethio doy na diamou yalaa

      yow mom dof ngue

  • lakhas

    wa mè nila wakhloubakh rek mo amsolo

  • sr

    sui pa amateur mais lima dégg rafetna lool…y'a pa plus beau que d'être très humain (NIT deugg).

  • titeuf

    thiey senegal, nafekh, hypocrisie, meun yap meun dieune

  • fans balla gaye 2

    machalla eum sene kadouyi rafetna yalla nalla yalla faye sa holle kou gniakk kigniane gua yala gua neki roi des arene ndaxx sa yarou akk sa gniakk kigniane te balla yalla nako yalla guena thi tolof tolofyii

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *