Vidéo-Gris Bordeaux insulte de mère Modou Lo: « Sou arbitre sifflé… »

Le choc Gris-Modou Lo était très tendu. Les deux lutteurs n’ont cessé de se promettre l’enfer. Dans l’enceinte, avant le coup de sifflet de l’arbitre, les deux lutteurs n’ont cessé de se lancer des piques. Gris Bordeaux l’insulte à la bouche a versé dans la provocation. Regardez


Gris insulte Modou Lo de M…….. par buzzclicvideo

42 COMMENTAIRES
  • etoile

    li rek mo takh modou lo tothie sa gat

  • mimi

    motakh modou lo nious nala humilier

  • demba

    yaw gris amo diom

  • fafa

    Wa yeen bi deeh feker woumako

  • Amy

    Lii dara raffé tousi

  • nexx@hotmail.it

    C des choz ki peuvent malheureusement se passer dans l’arene… Vous n’etiez pas obligés de le publier… Ayez un peu de deontologie!!!

  • beugue lo bakh

    mais eske amol loko Modou wakh Modou Dafa say say dé

  • dababa

    gri dafa sof pourmom les dakarois gnoy ay nit khamoul senegal ben la louma set loula tenga bayi yamba dji nak kerok linga toukh mo bari gri tang tang rek

  • Patriote

    Li vraiment rafétoul.

  • dababa

    gri bayil yamba dji gri bayil yamba dji gri bayil yamba dji gri bayil yamba dji

  • VÉRITÉ

    C’est eux qui »provoquent modou et si il répond d ils disent kmomla legui leerna

  • Djolof

    Je ne supporte pas Modou mai iow gris li ?aw na ?ak fayda di saga watei ?ak diom

  • CHELSEA NEW LOOK

    senego yene ay rambajj nguene denguene wara done pousso mais pas lesset

  • Boy lo

    Motakh Modou lo tkal nala

  • domage

    lima méti aye référence lagne pour les goss

  • deug

    sincérement nioune li niorou niou mbeur lounek laniouy wakhanté si bi guééw bi

  • Rose

    C’est un con il est minable khamoul dara lila kame sagua amoule bene personnalité

  • wett gore wetalikou gore

    wakh Day rafete ndakh netaliba

  • wett gore wetalikou gore

    tong bakhoul

  • wett gore wetalikou gore

    mbr

  • kalou

    mais gris bordeau ya nakk fayda
    et apres tu veux mystifier les gens avec tes versets du coran

  • Sooter

    Cri voila mak da garou si non khalé yarla mingui ni modou lo doumanala dane nala niou lak sa keur meritéwo tigre de fass

  • Dj

    Hihihihi me gris mo niakhe fayda

  • Fama lo

    Guémbal Maodo té bayi dossi lén ;tagga bayi ligay déff di mboubowo Talibé Cheikh dodém fénéne tenkka bayiwau ligay déf bocoul si Cheikh

  • ndeye diouma py

    sale con lii rek motax Modou l dane sa nd…..y

  • spagheti

    mann laye deff?

  • Mane

    Gris bayil yamba dji moy way bou bess parcelles

  • Mane

    Guémbal Maodo. Gnaaw na dé, son nom en tant que lutteur dou Maodo

  • serigne

    Sa defait est donc mérité bien l ni momla faralone

  • khourr

    gris bordeaux ya niak fayda ak niak personnalit thimmmmm do rouss

  • xarit

    mané son nom en tan k lutteur sé gris2

  • baye fall

    modou lo dakkar na sa ndeye

  • Las

    Sport ak saga nion ande, soccer, basketball etc encore plus sport de combat.
    Senego defoul Dara, dagnouy linguey
    Senegalais gno wara yewu, gnou diang.
    Diang nak diemeu kham reality aduna thi la Bok.
    Reproche Gris moy meunone na saga thi pet!
    Mangui ballou niep akh
    Senegal thi kanam!

    • kalou

      sa Thiès est beaucoup plus jeune que que gris et pourtant il a répondu autrement aux provocations de siteu
      la reponse est toujours a la hauteur de la personnalité de celui qui est provoqué

  • Rappel

    ARRETEZ LES INSULTES!!! Lisez ce hadith et vous verrez que insulter les parents d’une autre personne c’est comme insulter ses propres parents (gnoo bokk atté) et quel grave péché! ragal len Yalla “D’après Abdallah Ibn ‘Amr (qu’Allah les agrée), le Prophète (que la prière d’Allah et son salut soient sur lui) a dit: « Certes fait partie des plus grands péchés qu’un homme maudisse ses parents ».
    Quelqu’un a dit: Comment un homme peut-il maudire ses parents ?
    Le Prophète (que la prière d’Allah et son salut soient sur lui) a dit: « Un homme insulte le père d’un autre homme qui alors insulte son père et il insulte sa mère et alors l’autre insulte sa mère ».
    (Rapporté par Boukhari dans son Sahih n°5973)

  • boye djinne

    Lamb j dieumaléwoul galsen sa kanam.

  • teddi diop

    yaw gri danoula wara rey!doo dara!

  • L'expert

    Gniy commenter gni gneup ay supporterou modou lo lagniou modou lo mofi geuneu reew litakh gris meer ba sagako moko kham m lo si souf lay def c’est pas lui qui traiter la fam de b g 2 de outre? Souvenez vous lors du combat sa thies zarco il avait insulter le père de balla gaye 2 beug modou lo boumou takh ngene bagna wakh deug les lutteur on l’habitude d’insulter

  • anta sow

    Faut plus utiliser Maodo, il s’appelle Gris 2 svp c’est Gris2

  • charles

    GRIS,YAYOU MODOU DIOURNA KOULA DOUMA.KHOLALE GRIS RAME ANDI WOULA THI STADE BI MOUNOULO DEME SA KEUR DI RAME.WAYA MBAME MOUNE NA KO, NDAKHE MBAME MOYE SARUA YAYOU DIAMBOUR.KHALATALE SALAJENGNA YAYE.

  • dio

    motakhit Modou Lo dakhaarr nala boubaakhh yambar bi nga done

  • medina

    Gris cest un con. je me rappelle apres son combat apres baye madione. on lui avait pose kesk il pense de son combat avec modulo et sa reponse fut <> un gars Autin ki n a fait aucune preuve. et voici kiguaa donne khebb todj na sa gaatt niary yone. ca t apprendra a etre Leger et respectueux sale con. teekatou xel

Publiez un commentaire