Video- Graves accusations de Eumeu Sène: "Ils ont profané la tombe de ma mère

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Aucune recommandation disponible.

110 commentaires

  1. sylla

    hakhirou jamane lanou tolou loo mousou loo guisse ngay

    guisse loo mousou loo dég ngay dég nane délou si yalla té bayi lou bonn bakhoul


  2. adex

    la lutte a ramenée le fétiche encors dans notre pays en disant que nous somme des misulmans c est vraiment honte que dieu nous redresse car on ne le croix plus mais que de largent


  3. chifo

    félicitations à eumeu séne bon courage c inadmissible de profané une tombe nagnou ragal yallah soutoural nos morts svp eumeu mère bi yallah nako kharé aldiana


  4. Siradji diop

    Vraiment si c'est vrai ce grave sa pourkoi faire sa je suis désolé pour balla gaye 2 il est vraiment capable de fair sa c sur sa ce doit être interdit dan le stade


  5. awa traore

    lamb affair de faire play la fo rkk la akk keuff amna yo khamantenner waroul am si lamb koi lolou djoulite dou ko defff bayi len li wayy felicitation eumeu sene du courage balla gueye


  6. néné

    Bravo eumeu et bon courage ta maman a très bien travaillé pour toi tu ira loin Inch'allah grand bravo, la personne qui a profanée la tombe de ta maman dieu la guette


  7. Pape Torres lo

    bilahi li Eumeu séne wakh soudé Balla gaye moka déf niaw na trop li lambe diarou ko si adouna bi Balla il fo fair attencion


  8. biba

    francment li mome dou djiko balla senegal da barri seytane tè balla da barri nones di diakhacè nite ak yalla rèk mè eumeu dèfal recherche tè ga tèye mètina mè senegalèyes sagne nagnou lounè ki la wakh lolou ga wara lagne noumou dèf ba khamko


  9. Eva

    Vraiment c désolant ki dit l contraire c parck te po un croyant et k u hoserai faire sa. Li fila yam mais niit kou nek war nga kkhalat sa euleuk mere bi foumou teud diomoul kene amoul kousi mouthiou niit ki danga wara diokh thieur sa moromo domou adama.


  10. astou

    Ça mo j n peux pas y croire Balla n est pas genre en plus dafa am yoo xamné rafétoul té kou déh axx sa bamel Balla n pas méchant peut être k Aÿ supporter gno KO def m pas lui

    Arène bi mom dagnouy xéxaté rek t Balla avk son comportement d ojourdui la il est malade na defarout watt rek il a tout l avenir devant lui yalla baxna lep dina léer inchallah


    • Khelcom 1

      Astou Waw danga Guénoune Rek mé man mi dokh dougou si allou Casamance Bi dane Dadiégue Doubaless Bayou Balla Casamance dane Wakhtane ak kougnouye Wakh Ism. ak Malang sa Casamance gnou Wakhma Sacréfice You gnou deff si Combat Tapha Tine v Balla. Astou Bouma Diégé Wone Bama Diol la ab Numéro Rek Nga Wotési Kone Sakhéle dana Gnaw si Balla. Soudoute Mome Rek di Gni Ko Weur di And Ak Mom. Li Eumeu Wakh nak Nékhouta Gueum Mé Gnaw Na Si Ndiorte. Nakh Contre Tapha Ak Balla Ki Andone Nekkone Ak Balla Si Guewbi Moungui Deume si Diguenté Casamance Ak Mali Té Dane La Sou Nékhé Walla Li Daye Am Souko Nakharé Yite Daye Am. Kou Soko Wamou MAne Mi dokh Wakhna ko.


  11. IBRA DIOUF

    AH LINOUYE DEFANTE NGIR ALALOU ADOUNA DARA DIAROUKO THIE KAWW SUUF KHANA KHAMOUNOUNE LIWAAYE THIE KAWW SUUF YOWMAL KHIYAAM DINAKO LAYOO AKK SOUNOU BOROM


  12. six mauritanien

    je suis le fan de balle maiis serx li lambe diarouko jtjur surtout li sport rek le comme tout les sport mais wakh de gue yalleh li d fe euppe surtout pour un musulman


Laisser un commentaire