Publicité

(Vidéo) Gamou 2015: Serigne Mbaye SY Mansour parle de Ndiaye de kouthia show

Serigne Mbaye SY Mansour reçoit la délégation de Gfm venue lui rendre visite dans le cadre du Gamou 2015. Le guide religieux est un grand amateur de l’émission Kouthia Show, il ne s’est pas empéché de dire quelques mots sur le comédien Abdoulaye Ndiaye.

37 commentaires

  1. begue maodo

    wakh degue yalla serigne bi manone na wakh si lenene lou guena ame ndiarigne koukhia minga khamni tekiwoute fo rec la mene ac fethie

  2. zakkaria

    serigne bi dafay wane ne nitt la…et je pense que lii yakoul dara…..on a vu ceux qui ont 8 femmes et de plus au senegal …c du concubinage

  3. seck's

    KALIMA iow kou katte sa nday gua beugue maii lii khamegua nii ci internet gua nékk bou nékone fénéne kholli naa sa gounorou nday bou yagu akk koula cii diappaléé
    kippél sa serigne té bayyi serigne gnou diambour yii ok

  4. talibe bamba

    kilifa dankoye dokh thiere khamouleene mbirou batine motakh kou diangoul nak lou dioug nguen wakhthi tadoleene si andac seene sago waye nak nguene khamni nitou yalla donko khme si djouli ac woor rec bref bayileene dingate nitou yalla senegal dou deme

  5. talibe bamba

    kilifa dankoye dokh thiere khamoule mbirou batine motakh kou diangoul nak lou dioug mou wathi tadousi andac sa sago waye nak nguene khamni nitou yalla donko khme si djouli ac woor rec bref bayileene dingate nitou yalla senegal dou deme

  6. GMAIL

    Thipiry niacg FOULA AU FEYLA ana KILAFA DINE AK COMMENT SI AY MUSIQUE AKI COMEDIE DEMALL DIAMOU DJI YALLA TE KHAMNE
    LEGUI NEKKATO KHALE
    BAYYILL DOKHANE MI AK TOUKHMI
    WA SAWAY LOOY WAKH NI HAHA! NGANIMEU? BETOUMA NAK SOOB REK NAGN FI NEIKEI FOFOU DARA NEKOUFA GARS YI KHAMNAGN LEPP DEH

  7. Talibé

    Kalima et Tedjane watt nako thi borom bi bbou ngueen touboul en ce qui concerne vos propos,sen moudj dou rafeet.Niit day am yar.mais nak niit noumou meel keureum rek l'ay wané thi bitti.

  8. baye

    kepp kouy togn sache que tu es entrain de remplir ton livre de dieuf que tu porteras un jour devant le Dieu

  9. beri feem

    Serigne nii laye Mel….Serigne dafay oyoff….Moi j'aime bien que Serigne Mbaye Mansour est un grand fan du Kouthia Show comme un simple Senegalais…Ca ne diminue en rien sa sainteté…Du respect SVP pour nos grands marabouts.

  10. Kalima

    Thipiry niacg FOULA AU FEYLA ana KILAFA DINE AK COMMENT SI AY MUSIQUE AKI COMEDIE DEMALL DIAMOU DJI YALLA TE KHAMNE
    LEGUI NEKKATO KHALE
    BAYYILL DOKHANE MI AK TOUKHMI

    • Senegalaalis

      Thiat yaw guiss nga saga kilifa diambour nimou mettee motakh nga wara respecter kilifa dimbour come sa kilifa ndakh wakh lou niaw niepa ko mane

Comments are closed.