Vidéo- Emouvant: Une femme se convertit à l'Islam grâce à Sokhna Fatou Bintou Diop
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
sokhna ci dougu ci diné ji nio gui kay nan markhabane.yalla na borom bi lérale ba fou mou dieum niou kham ko.Sou niou yaye fatou bintou yalla na niou la yalla fayale ci barkèb Baye Lahi(psl)
machallah l, islam gagnetina allahou akhbar li dawena yarame
allahou akbar yalla kène la té mom rek mo meune liii…sokhnasi tew walak diam si barké rassouli lahi
Ma cha allah yalna nga thi dounde déé thi déki thi ba aldjana barké seydina mouhamade p s l barké ramadan amine yaa rabbii
Machaa allah
allahpu akbar c la victoire de rassoulila qui niou guene ba faw
l'islam rek moi woor.dojo rethiou de
je suis aux anges WALAHI MANCHA ALLA sojhna bintou YALLA nala YALLA faye si sa mission bi
Machallah welcome to Islam Sokhna si yalna la yalla diapelé
jai pleurer bcp cest emouvant
akasa masahalla deug rek moy deugue l'islam sa kanan
Mouhamed salahou haléyhi wa salam c'est le messagé de dieu c'est l'islam qui gagne toujours.
macaallahou soxna fatou bintou nieuwlèèn nieuwlen toup yalla teujoul bountou yii alhamdou liilahi
Toi tu mérite pas le nom de mohamed, toi qui dis que fatou bintou dafa soof.
masha Allah. ça m'a énormément fait frissonner et j'ai pas pu retenir mes larmes. Gloire à Allah !
machalah alahou akbar
ma chà allah jiahalahoul lahou fi mawazini hasanàtikom
mom tamitt yalla sakhalko thi ta dagarallko
tu ma possé a commenté yow y'a niak tégine ak sa tour bou séll bi, ak werou korgui, ta l'I ndamou l'islam, ana loufi diarr sokho. alahou akbar lah ilah ha ilalah mouhaldou rassouloulah salal lah aley hi wa salaal.
Machalla thi khaname rek
Oh barki cheikh bethio contane na lol ci iow maman vraima dagama meuss nekh te nak serign bamba xamna ni tay la raw ki nak welcom sr ntr diner yalla na don ay yokouter rk ci iow chapo à group futurs médias
tro émouvant way
macllahe yall nak yalla sakhall
islame amatina ndame deh taiye kouy dioulit sa khôl Sedna Way allhu akbar
machala
Ndaysan yalla naga doundou ta faattou si l'islam bougnou nagou
est ce que djigueneu meune touba nitt?damay latieuteh sama khamekhameu soriwoul
yaw momou y'a soff ligay rrew
Machallah li nekna tata Fatou yallna yalla faye là
Marjaban Ya khairada, Marjaban Ya Khairada. Bienvenue, Dalal ak Diameu si Barké Mouhamed Salalahou Aleyhi Wassalama
machalla yalla nala yalla may xolou continué t moussale la si saytané
la ilaha ila lahou Mohamed rassoulilah salalakhou aleykhi Ya salam. yalla bo ko rethiou si barkéme
Machala Machala Machala. Moment très émouvant, y alla na djam yague.
manchalla yalla na sakh di law ba faw
Dara gueunoul reuye li Sokhenasi déf wakhoumala ki toupe wayé askanou leumbe la Dimbaly ! Bonne continuation Sokhena F Bintou!!!
Alahou akbar Alahou akbar Alahou akbar.
Machalaaaaaaaaah laa ilaha ila allah mouhamadou rassoulilaaaaaaaaaaah
MACHALLA YALLA NA YALLA SAME LA
l'islam amna ndam li sédeu na khole allahou akbar
Lii rék diarna sante yalla
machalah. tante binetou
un peu d respect mn frere j veus mem pas tapeler par tn nom parck tu le merite pas
fatt bintou ya sooff
Allahou akoubar yalla na yalla saxal la si dîné islam
sOKHNACI YALNA YALLA FAYLA TIE BARKEE SEYDOUNA MOUHAMED(PSL)
Allahou Akbar. Mancha Allah.
allahou akbar allahou akbar machalah islam rek moy deug
yalla naka ci yalla sakhal ci barke seydina mouhamed psl
l'islam rekay degue machallah
VIVE L'ISLAM ma contane wayy
Machalla l'islam rékh mo wôre té moy deug
ALLAHOU Akhbar lii seed na kholou dioulite yeup machalla
DOU YA NGUI DIOY T DARA KHEWOUL DIOYA GOULO SAKH DA NGAY DOOR BOUL FATE NE BEUS BO GUENE ADOUNA SI GNOM DOUGNOU LEU SOUL SAKH SENE BIIR KONE KHAM NGA NE NEKOULO CI TOUSS YALLA NA LA YESUS CHRISTA TAKHAWOU TE BAAL LEU LEEP AMEN
Tww sa s voi k u né pas humain…u n konaii rien dans la vie demal nga diangi wate
Yaw yaye domoharam fils de put fils de la nuit
tu as bien dis mon frere elle ne seras jamais considere comme une vrai musulmane a part entiere… ell sera tjrs disciple de jesus christ mou nekh mou nakari. louma metti moy nos freres musulmans croient tjrs que lislam est la meilleure des religions est quelle est au dessus des autre religions…
Hahaha yéne séne xol migui méti ki rawnaléne ak lou meunti am séne jessu momou sax def na li migui yof teud yéna yéss thiim
rien ni personne ne pourra enlevé le sacrement de baptême, il est indélibile. jésus nous dit si tu me tourne le dos a mon tour je te tournerais le dos, si tu me renie a mon tour je te renierais, mais si tu proclame ma parole je te défendrais devant dieux et les hommes.
il est t écris que jésus christ sauveur reviendra sur terre. une brebis s en est allée cela dois augmentés notre fois en jésus et lui resté fidèle advitam eternam. pais et joie en le christ.
catholique nous n avons rien contre la réligion musulmane partout ou nous irons il n y a qu'un seul dieux .
la religion musulmane est de MOHAMED est la seule reconnu par votre prophéte JESUS espéce d'ignare
Sama wa dji ce vous dites indélibile c'est enlevé dès que le CHAHAD a été prononcé.
ALLAHOU AKBAR!!!
sa khol moy méti dawssi rawnala thi barké seydina MOHAMED salalahou aleyhi wa salama
allelua tu va regressé comme pas possible notre religion est la meilleure de toutes
yow fatoumatou bintou yarasoulla allakho kbar yalnala yalla denchal palas yie gena nekh adiana …yenyie neke di wakh nak moytoulen borom bi dakh khame gae moy kane
Mes cheres frere Chretiens, je n'ai jamais penses qu'il y avais des Senegalais Chretiens qui pensent ainsi. Le seul fait qu'un Chretien se convertit ne vous donne pas le droit de critiquer tous les musulman. Elle n'as pas tourner le dos a Jesus, elle a au moins augmenter sa croyance envers Jesus. Elle va croire plus en Jesus que certains Chretiens meme car l'Islam n'est la que pour continuer ce qui etais venus au Paravant. Un musulman n'est musulman que quand il croient en ce qui est venue avec le Prophete Mohamed SAWS ainsi que ce qui etais venue au Paravant. Il faut arreter de dire ces genres de paroles qui risquent de nuir au bien etre de notre pays. Chaque personne a le droit de faire son choix, elle a fait son choix ca ne vous donne pas le droit de la critiquer ou les musulman. Si ca vous fait mal, je penses que la meilleure des choses a faire c'est d'arreter vos bobards et de continuer a marcher.