Vidéo: Ce que disait Doudou Ndiaye Rose avant sa mort: "Récitez pour moi des Ikhlass et rien d'autre"

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Aucune recommandation disponible.
Aucune recommandation disponible.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
nako seydi mouhameth terrou fimou dieum geunalko fimou diougue amine
yalla na bourbi yalla yokk yeurmande thi mome moke mbolemou dioulite boumou fa fekk ak kouka fa fekk. ..amine
k la terr li soit legere et k dieu laccueil dan son paradis
que la tere lui soi legere?
Yalla na sunu borom Soubhana wa talla yeureumko te diegalko AMIN
Té mouy deugue "Sénégal guistal rk"daniouy harr bagan dé nioulay soga dimbali"
(Sénégal =guisteul )
yalla nako Yalla yereum té kharéko adiana firdawssi ak molémi dioulite youmouye fekidji AMINE
yalla nako yala yeureum
djangal nala 3 likhlass que le bon dieu te pardonne tes péchés yalla n'a souff seddeu si sa kaw ..yalla nala souniou borom yeguel si aldiana yii gueunneu khawè yalla nala serigne cheikh al tidianiya terrou. repose toi en paix alakhou akbar
yallah na co yallah karée ajana tée saidale soufame papa doudou ndiay rose merci pour tout ce que tu as fait pour ta nation et la jeunesse senegalaise teudeul nopalicou dounou la moussa fateh diallée na wa senegal niepeu gny beug tonton doudou comme moi massa leene
Yal nako Yalla yerem, Amiin
yalla nala yalla khare aldiana li mou wakh nak lèr na bouko ken defal homage teugue aye tamma wala tanber wala touďe ko soire. wa salamm