Vidéo – La déclaration du Khalife Général des Mourides sur…
Suivez en direct la déclaration du porte – parole des mourides, Serigne Bass Abdoul Khadr Mbacké.
https://www.facebook.com/senactu.el/videos/249603319108616/
Suivez en direct la déclaration du porte – parole des mourides, Serigne Bass Abdoul Khadr Mbacké.
https://www.facebook.com/senactu.el/videos/249603319108616/
Dieureudieufety Serigne Touba. Neu lep di rafet rek.
wallahi sounu senegal bii dou guawa avancer ndaakh khol you tilimm kein meunoul geum serigne bii tei doono djouliit wayei tamit wakh bou niiaw deukoul famou djeum fiimou djouguei la thiossano serigne Touba moom la yallah diokh geune gui devellopement rassoullilahi signe ko mou gneuw gneup valider koone loufii way def loudul diokh thieur serigne bii sa ayy mame dinagn leuh merei wa salam
Que Idy soit mouride en quoi cela peut nuire au tidianisme? Tarikha bi kép kou thi geuneu waro thi wone mbokou bo kholé djikome après tout c’est comme un Neymar qui quitte le grand Barça pour lé petit Psg
Bill on te pardonne je sais que tu n’es ni Tidiane ni autre…tu en veux à ISLAM donc normal que tu attack les détenteurs de l’orthodoxie …
Mais vous rts vous êtes nul personne ne vous regarde pourquoi vous portez plaintes à un sénégalais parmi nous qui aime son peuple qui as créé temps d’emploi pour sa jeunesse allez vous en
le secte de Touba.. les plus grand voleurs de l’afrique
Machallah mbacke balla aissa
MachAlla. Kadddu yii rafétna naniou rafétall Lép ndah dééh motah
Dieuredieuf wakhdji rafetna amna solo yalla nanou yalla sakhal silou bakh te rafet dieuredieuf
C est une realite .Surtout Dakar la capitale .l indiscipline est totale
Mansour dieredieuf bien parler Machaalah
Tv bresil sa tounou ndèye
Machallah,rafetna,Yalla Nako Borom Be Fay
Dara manoir tilimeul diner dji Koufiye aye ayelou ba wahfilou eupeu.dako féy kash.Guiss nann fi Professeur Sangharé .Alors naka la moudjé
Serigne mourtalla 2 serigne mbeye sy 0
Massallah wax dji yiwna, rafetna té mot na, jeureudieuf Mbacké.
c’est ca la mission d’un guide religieux, amoul dara loufi jar d’etre des ennemis.
je ne suis pas mouride mais wallahi je commence a avoir un penchant pour cette confrerie.
Jam ak Salam.
Elzo
Sénégo avec vos mauvais titres !
Serigne bi nena da ngay donap djioulit ba parer do gay done ap talibe Donc soyons de vrai djioullit dabor bagna doutelo les musulmans sur ce ke yalla ak yonentam ont dit wassalam
Dieuredieuf mbacke killifeu daye bole yamale di rafetale tarixayep benlaniou senegal benne bopoula kene mounouko xare niar mouride tidiane yep benla nio bok seydina mouhamed psl boulene kene di politique wassalame
Amna kou toudou cheikh fall canada wakhlene ak mom ! sinon dieureudieuf mbacké. barké serigne Babacar sy kou yeukeuti kaadou dieumeulé kou si mouride wala tidjane ya ngi saga sa bop
Amna solo mbackè yagg fi lool ta weir