Video: Des petits-fils de Feu Serigne Fallou fixent un ultimatum de deux jours pour libérer Serigne Assane Mbacké
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Aucune recommandation disponible.
Nanio diapee serigne touba mome dè douyakou Lou adouna amee ak nou mou mèleee diapee liii nio serigne touba dèfele kou japee serigne touba rèkee ak khassida yiii dodèguee lou nieweeeee
Borom touba yaw do mourid mourid dou com paleegue sy
sama book mouride yii daniou rééw ba dof serigne touba momoul deuk bii mom si bopam prisonier la wone si bureaux ba sa ndar t mougne kone book assane na mougne t bayii rééw togne bakhoul deuk bii dafa am yone kouko wathie niou dall sa kaw amoul touba ak fénéne ak fénéne nieupp si yamm
Mane mi done mourid 2010 ba legue kham nanee s touba dou moromou wa adouna dakh limou done mon rek moga masa done si adouna mame elhadji malick gou bakh la da deem na guiiss s touba neegou diokh nala sama bobou adouna at alakhira s abdou Aziz sy sabah bo kholee youtub mogui sy pimou deem touba nane diokhna leene sama bobou mon gui youtub tidiane yi nane da nekh mon dakh limou am sy yalla at si adouna mome rek mon ga am. Done khatre sakh moma guenal done tidiane wala laneene dakh s abdou khatre gogou amna sa yalla dara dakh gou am sa yalla dara rek s touba wakh nagou khasida khadimatou mounadiati moga fa mome at chiekh akhmad tidiane da s touba nena si khasida gui nioniou douma sene mon rom wakha douma nague gueniy wakh ay el Hadji malick mome waliw la kham nanou loulou at wa niass sene at layeene at tall at nioniou neegue senegal rek sonou mame you bakh yo you ay waliw lanou wa sidikh wala khout bou samane wayee s touba nague da leena rew mome moudiadig la moudiadig mo rew wasal
Sénégal dafa am yonn …
haï si le Sénégal avait un président diola wallahi liii diéhna vive yaya diémé en Gambie
yène mourites yi les tidianes yi dinagne tègal sène deye fomeharame yii kou yegueul senegal gnou dame sa deye
La loi es la pour tous et c pas ça lodlam
laisseé la justuse fait son travaille
républicain.machallah merci bcoup
Ton analyse est juste, cependant si on en est là Senghor et Diouf en sont aussi responsable, c'est du moins ce que j'ai compris en lisant les mémoires de Diouf.
Macky SALL tey rek laye kham ndakh yow laye Votel 2017 ou pas. Ablaye wade a donné à ces marabout une force et une prétention démesurée. Si le président de la république n'a pas les couilles de les arrêter , on est tous morts. Ils auront le droit de tuer , brûler , piller et faire ce qu'ils voudront en toute impunité. Plus aucun sénégalais non Mouride ne sera en sécurité . C'est quand même grave . Déjà ils vivent au dessus des lois et à nos frais en plus ( tracteurs , semences, engrais et forages gratuits, enveloppes et denrées alimentaires lors des Magals, passeports diplomatiques, enveloppes et mallettes d'argent à tout va….). Et maintenant ils impunément , ils terrorisent les gens .SENGHOR et ABDOU DIOUF ont assumés leurs responsabilités , WADE s'est couché devant eux, MACKY C'est ton tour de jouer . Nous vivons en république et en temps que gardien de la constitution vous avez la charge de la préserver . Nous sommes tous égaux en droit.
Bon courage mister president, les sénégalais vous soutiennent , tenez bon et ne lâchez rien. Wa Salam
Assan Mbacke yak sa kanam bou ndaw,demlen sawi te teudi,te bayi saw lal
Assan Mbacke moi kan,khana cisse Lo mom amul Famille
assane killifa la dou sen moriomou baay s touba moy maamam s fallou moy maamam rawnalene bouyague
Dans une republique personne n est au dessus de la loi.
waxal rek sama wadji tè bousi dougeul akhlou soufis. stp.
sde
Force restera à la loi !!!! Que ça soit a TOUBA , TATAGUINE ou bien POPENGUINE !!!!! Kou fi déranger gnou ranger laa !!!!!
Nokh lene Sene ndaye reck dagno réw pour GNOME gno môme nit gni
Pfff ces vauriens se croit super puissants. adouna boussa xél oubékouwoul ay connerie rek ngay déf.
nul n'est censè ignorè la lois serigne ak niep nio si yam
yen amoulen fayda deguen yabateh,mais bolen moituwul dinenj len nokh ba ngen dool,mandeh khawma lolen yakarr batakh nguen di def yefu domram yi
ahlou bida ,soufisme rek gno yak Sénégal.donk areté vos foutaise
allez vous nous soûler.il fait des coneri il n a qu'à assumer.les lif des force de l ordres il son la
ay waaay ana yarr
Koufou yengou gnou tégal sa ndaye boubakh
Serigne Cheikh Sidy al Mukhtaar nenna :
Kou amoul ay tegguine do teggui dara
Kou amoul ay Yaar do yor dara
yeen dangueena bagne s touba waye si nakhar ngueen di deee mbeullee
senegal mo nekh quoi, on doit tous les foutre en prisons ces faiseurs de troubles. keur serigne yi sonal nagngnou quoi