Vidéo : Concert privé de Youssou Ndour à Paris à l’honneur de Macky Sall – Regardez.

Concert privé de Youssou Ndour à Paris à l’honneur de Macky Sall en déplacement dans la capitale française pour une visite d’Etat. Le roi du mbalax interprète « Liguey » et lance un message fort. Regardez !
you gueumoul dara sou macky wathiė mou dem thi kenen diko maral tatam yi fou pochame fessė rek lay woute dou touss
yeen bayilene soxaar youssou ndour ligeuye rek laay deff kii senegal rek boulene fatė youssou dafa bayi ligeuye biii pour senegal senegale deug mooy youssou president Sall dafay ligeuye senegal youssou ndour dafa beug limotkh so beugė senegal lou sa president di defff keen warou la si jitou li mooy senegale ligeuye leen waaaay
Yaw bo sagnone sa baay melni You mais malheureusement pour toi BLUF
Au Sénégal les opportunistes sont considérés comme les meilleurs et o a tendace à confondre beaucoup de casquettes . You est u ministre de la République qui utilise la république à ses propores intérets . Il aut arréter ce cirque pendant qu’il est temps .
Opportuniste bou mag la c etait pas gratuit je pense malgré tout on aime sa musique
Dama Dioum dé yousso ndior bappam rekk kii dou touss
Bravo machalla
m.le ministre youssou ndour vous avez créé des emplois au sénégal c’est n’est que pour ce la *gathié galama*
Wayy youssou koula bagnnn sa tounouuuu mam wayyyy
il faut etre correct et faire vos commentaires dans la discipline c’est mieux. Begué len you té yem
Vive le roi…. Merci Youssou encore nous sommes fier de toi.
c’est cette politique ? Ce concert est inaproprié waay
Comme dab rek ! you suit macky comme une vache. aiii aiii
Yaw weuz kou rew ngeu
weuz youssou motay ndayam khol bouy méti dina ray sèn ndeyy wa li diam la sakh you sou néékone fimouy def ay deal la wala lou louss kone yalla douko yeukati niata att batay fayoul chak jr guèn yénéko faillite té yalla diko gueuneu téral dc ande lèn ak soratou mougn té nagou li yalla dogal
Yaye danga né koumeu beug nako beug yaye danga né koumeu bagne loumou may wagni You dal bibliothèque leu
Thiey le 1 janvier dineu nekh dineu tangue incha allah
Kaineu duma fa djitou vous les jaloux kobas nak koussi repp rek DINA omelettes khourou bayam You mofi naik kouko bagn nga todj sa sarap Ndey dem si omzo zozo ak saine PD ethiopien bou hibone bobu
Je demande juste combien You a encaissé pour cette soirée où les invités étaient triés sur le volet
Ndeyssane lii nekhneu
Yaw IVE kou mér kalamel yalla moy sedelé bande de jaloux
ce qui est grave ce sont ces nafeks qui soutiennent ce faut type ; loudoul deug d’où yag vous allez voir vous même bande de doungouroux
Non Youssou dal kouleu bagne dineu soon ndakh yaay adouna bi
Yaw AUX JALOUX bayil togne mdrrr
Les jaloux vont maigrir allez vous fait foutr on aime youssou PT final un PD n’a pas de place dans notre coeur les PD vous pouvez déménager en Suède chez omzo zozo concert de You rek nom PD gnepa set ,si on en avait 10 Youssouf rek senegal naikh on n NS impose pas un dealer.nak ki est tellement nul et fauché il parai a coz de You aywayyyyyyyyy
Il est temps de vous reveiller et affronter les choses en face
Vous vous faites duper par ce mec qui ne fait que se remplir ses poches pendant que vous admirez sa musique. j’ai rien contre lui par contre je n’aime pas le fait qu’il utilise le peuple senegalais pour se faire de l’argent. il n’est plus le roi du mbalax mais plutot le roi des marches gres a gres entre lui et le president. reveillez vous il est temps.
èKH MAN DèH WèDI NA YOUSSOU NDOUR BOU YAGUE A CAUSE LIMOUY POLITIQUE POUR MACKY DICTATEUR SALL. LèGUI MAGUI SI WALLY SECK
Merci you tu assure toujours. Jamm rek
Thiey you… Dor rek. Li doyna waar
La presse des 100 et les laudateur qui glorifie l incapable macky. le seul chef d etat a monde a avoir reussi la prouesse rare de claaser son pays dans le rang des etats les plus pauvre..
No You est méchant DEC bi gnewagul sakh ngay todj tai teugago ndakarou Ray nga djinakhh yeup yifi done tanhalatai kaine daigatoulen mani yay chat KO saineuuu mou daiiiiii KOula songou dougou ndougoussinee aywayyyyyyy dotugnuko dafatiii dhhhhhhh
Youssou mo dakheu way Afrique amulofi morom beneu ngafi tai doto fi amattt youssou doundeulllllllllllllllllllllllllll way
Ndeyssane namatou meu djolof ndakh li You dal tu es une fierté internationale
Barké yalla Youssou yay ndanane salle Wagram mingui tothie
Nice prestation machala
Mais Youssou maleu beug maleu fan
ooohh je tadorrrrrrrrrrrrrrr trop way
Youssou est très beau pour son âge, très charismatique hummmm…
Un message a l’endroit du president et tt immigré. Il est adepte de bonne paroled et sait bien les manier et ou les manier ! Merci youssou ! Les artistes devraient se referer sur tout et travailler davantage. Certains me diront pour ay way et fethie, mais on a dit work hard and play hard adouna amoul solo
notre star planétaire, notre activiste hors paire, notre fierté a encore tapé fort
mashaallah goudal fane seu doundou amna ndiarigne NDOUR
super super super j’y étais cetait vraiment magnifique
bravo au roi du mbalakh
aaahhhhhhhhhhh Youssou Ndour temps yi mom yagui casser la baraque aah mais oui yangui todj la maison
ahh concert bi nekhna kéneu douma ko nétallli
Les commentaires sont fermés.