Publicité pour Mesri_Juillet
Publicité

Video- Charlie Hebdo-Iran Ndao: "Si on avait caricaturé un marabout sénégalais, ça serait la fin du monde"

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Aucune recommandation disponible.

24 commentaires

  1. aboubacar sylla

    je s8 parfaitma d’accor avc tw iran si on le faisai a un ds serigne sa sera une otre problem et k nhioune yonetti bi MOUHAMED lagne gueme yallah laye diama MUHAMED PSL di sa ma PROPHETE


  2. fall.modou92

    YAW MUSLIM .TW OSI CE QUE T DIT .C’EST FAUT .WAKHO DEUGG.. .LINGA WAKH SOUDENI DEUGG LA …. DEMAL VERIFIE SAY ARCHIVE. .BAKHAM KANLA AK BAN KHALIFA GNRAL.. MOFI CARICATURON RASSOULILLAH. … … TA LI IRAN NDAO WAKH C’EST VRAI


  3. fall.modou92

    billahi wallagi wa tallahi .deugg gou wer péngue nga wakh. ..ta deugg rekk moy deugg lasa guinaw deugg ay thiakhan la…… ta serigne yoyou niom nieupou .rassoulillah molén ngeun……….damani nanioulen bayi thiakhan yi..ta fonkou rassoulillah swslm


  4. bella

    iran mome lui meme c une caricature. Il y a deux fois plus de caricature du prophete en France maintenant sa n’ a rien changer. En plus deux Musulmans on etait tuee lors de l’attentat. Trop bête ce type pffffffff


  5. bègue s touba rek

    Senegal wakh rek lanouy deef da gousouy wakh nague mourid ti s touba yi noi dakh nio wakh s touba da raww nionoiu negue senegal bayi lene go guir yalla they yalla they mouhamed they s touba li rek mon nakhari wa senegal sidou adiz gatyi donout mourid nague s same mbaye wakhone li lebou yalla mayone nago lolou mon dakh donou deeg lou gni dakh danou Lay réral dakh khamonou dara


  6. Madam Faal

    iran ya wakh degue, mais li ma nahary moi senegal dama yakarr ne finu tek sen marabou yi tegu nio fa Muhammad S.A.W, te mom moi gen thi mbidef, way kepa ku jok pour fonto Muhammad S.A.W Yal na la Yallah torokhal thi kanamu aduna bi yeup. Ameen


  7. MUSLIM

    walahi iran ce que tu dis n’est pas la realite mois j’ai vu un jour caricature un khalif dans le journal le quotidien,malheureusement je ne me rapel plus de la date


Laisser un commentaire