15 COMMENTAIRES
  • Haaj

    Assalam Khalifa dél comprendre Bouba dika mouñial loubaré parfoi damaye tîte bala chaytané di soré séne diguanté sou booba noonou émission bi dananou rétane ak noonou tfm yi ak noonou Bouba yi Khalifa diap si waye

  • ndey Fatou

    hajj mane andou ma ak yow. loutakh li emision la jakkarlo la niou wakh sou bouba wakhé lou amoul nako wakh li amoul boumou khol nei tfm ndour le sant rek batakh dou wakh deugue affair bi diaroul complex

  • ziza

    bouba da tounou n’deye way.

  • dieng

    ziza yaw sa yaye nga wakh Lou gnaw lolou taye la ma saguisse kou ye saga yayame

  • Cherie

    ZiZA yaw khana amo ndey wala boko amey tam respectwoko

  • Sidiki Diouf

    Trop de polemiques entre les animateurs de l’emission.

  • Haaj

    Ndeye Fatou wakhé wouma figuaye wakhé je comprend bien k ni li émission en plus meunna tangue wayé bounou fatté mouck si télé lanou néck parfoi wakh bi daye tangue bou agué si dièrreu do tounou meuna controlé séne languaje ta il faut kéne qui di tané morom mi sinon dana ñiaw si ñiom ñiar ñieup

  • bay

    l vrai problem s pose ici.onetmen parlan bouba na pa d plac ici.senegal nafékh mo yakh gnou bari.nitki mouno tari ta diango.bou limou beugeu tari diangouko.limou diang gnép khamnagnouko.

  • ndey Fatou

    hajj lolou mom deugue la

  • isara

    je pense que c’est birima qui ne mérite pas sa place . tout le temps dans les casino entrain de jouer et boire com un malade et venir nous faire des leçons de moral …..

  • right

    khalifa bi mo soff. louko téré may nit yi danél kom ils le veulent.

  • cure dent

    bouba ndour il n’a personne au dessus de lui pour le ramener a l’ordre? Ce qu’il fait c’est du vrai abus d’autorité et de pouvoir,il montre que c’est le patron de tfm quoi,il est impoli anticonformiste et fout le bordel comme bon lui semble. il n’a qu’a se conformer et régler ses problèmes en coulisse et non se comporter comme un petit garçon impoli. il nous fait chier ce mec pueril

  • Ahmad mbacke

    tfm tl thioun khamounou dara touss

  • guôong

    Ecoutez, on a en marre de ce feuillet de m… interminable entre khalifa et Bouba. Moi j’ai cessé de regarder cette émission devenue vraiment ridicule….à mon sens.

  • Max clitoris

    bouba ndour n’a pas sa place sur les debats politiques, culturels et religieux

Publiez un commentaire