Vidéo: Au calme dans son hôtel de luxe Gentle Mara fin prêt pour le show de Waly Seck à Genève

La demi mesure Gentle Mara ne connait pas. Actuellement à Genève pour soutenir celui qu’il décrit comme son ami et frère, le “marabout jet setteur” a mis les petits plats dans les grands pour cet événement.

(30) commentaires

Dëg

Mais ce gars la, il roule avec quel argent ? En plus s’il se dit marabout, c alors un Serigne tariaax car il est loin de l’islam celui la.

Koi

Ki dei mo gueneu diang alkhour sa pape ak Serign bileu Toude

Roky

il est vraiment beau avec sa lumière

Ablaye Mbaye

Serigne pur doudeme ay waly Seck

Justice

SA C EST LE HAUT NIVEAU

Moussa

oui c vrai sa c est le haut niveau

Dëg

Loi : jaang taxula xam.
Comme tu l’as dit qui Alkhour la jaang et non al khouran.
Conclusion : vous êtes pareils, Aÿ caxan kat geen !

Wakhe+Deug

Bayilen lidieunti domou adama kounék la boop doynala missale salam

Wakhe+Deug

Khamou gentel mara mais lidieuntiléne sên boop kousi nék sa boop doyna la missale

Marathiakhann

Si il y va, alors IL ADMIRERA LES PAKARGNY DE AMZO ZOZO !S’en réjouir et peut être chercher à le/la rencontrer ! SETTOU SERIGNE DOU SERIGNE ! MANNA RAKH CHEYTANNE

Diop Abdoullahi

Kii dou marra wally moko toudè gentle mara bayi lènko AK ay thiaxanam entouka bane lobi lanèk warnagne koo xame nax ana mbaye sène

Cheikhmbenefall

Kii kay dou Dara day sabote rek

Astou

Lui c est un marabout intérnational il a guérit une femme possède par un jinns devant mes yeux

Fanta

Diem lene outi khaliss mo gueun di sedei ko khamaloul dara

Idrissa

C est sa le SÉNÉGAL FENE REK AK YAKH DERE .BRAVO À GENTAL MARA

Mor

iL voyage beaucoup ce gental MARA

Michou

Qui peut me donner le numéro de Gental MARA

Ndoura

IBRAHIMA a maîtrise le Coran depuis son bas âge et fait très tot des miracles en son enfance il n est pas ordinaire donc mandoulene

Ndoura

IBRAHIMA a maîtrise le Coran depuis son bas âge et fait très tot des miracles en son enfance il n est pas ordinaire donc mandoulene

Bassine

En tout cas il a un train de vie très élevé

Nounoush

MANE DAMAKO NOP BILAY

Khady Thiam

Ki ay mbokam guereum neunoko yayam guereum neuko ma BEG si yaw bolewo dara ak Wakh

Niang Mamdou

Ap serigne topė d’où thieureum waye serigne top Wally seck mo gueun fouf serigne bout top nafekh politicien yi dolene marale tate ndax tope Wally d’Ara nekousi ndax dafaye ligueye si niakham mou leewww tai politicien yi riba laniiuye ndoundeulė serigne silène toppppp Wally bou sénégalais yeup done def ni mome thiow d’où beurri ndax ligueyam moy yitem ak di dimbali watė

Niang Mamdou

Amzo zo nekone président Sénégal mane dė moma gueuneulone macky sall mi kene khamoule limou done moy président bi ndieuk nieuw senegal di trokhale serigne si rawatina wa KEUR serigne touba mofi wakhone mok gnimou andale ni serigne saliou citoyen simple la waye nako loumouye reutiou la fi ak alakhira barke serigne touba

Niang Mamdou

Amzo président Sénégal mo gueunone macky SALL mi wėdi wa keur serigne touba

Niang Mamdou

En tout cas nioune mouride bou djitale bene intérêt bou serigne touba touba wesso ndax moy intérêt bou worr bi aduna ak alakhira kouko top dara douma diombe lo sakou mou diokhla ko fi aqk feulė waye mangui lene di denk ni macky sall mofi wakh lou wone ni serigne saliou citoyen kessė simple domi bamba diodiiu batax na kepe kou yakar serigne touba boule votele macky sall ni seulement dafa wedi serigne saliou mais tamite dafa gueume bene serigne gnimou meuna bakh rek niokoy gueureum ndax mome gueumiule alkhourane jheureum la gueum wa Inde bethio moko tek si yone wowou motax mou guenė prison.ndigueule moy bouko kene votele la preuve ndemb lay digua bayi domi serigne saliou Touré ndax rek contre serigne saliou ak gniko diegue sif bethio ndax mome aduna lay weur

Niang Mamdou

Ndax amzo mome neubeutouwoule wone na limou done wayė macky a part contre serigne touba ak ndiabotame lisi dess yeup dafko neub ndax hypocrisie nafekh waye mouride deug waroule andak kou wegoule ak niaka respecte serigne bou mag bi khamni biudoule wone mome senegal si mousiba rek lay deug la preuve yenene rewyi serigne touba laniou amoule motax fitna rek laniiuye deuke Sénégal nak bamba dafa niou diombe

Cédric

POURQUOI CERATAINS PERSONNE PASSE TOUT LEUR TEMPS À PARLER ALLER TRAVAILLER C MIEUX LUI IL A DE QUOI VOYAGER ET PAYER SES HÔTEL MAIS VOUS NON

Mamadou Sene

Niang sa tour dah yiwe mais yowe dioulite dou sose liguawakhale macki c’est pas vrai so bagne le président boumoutakhe sose molla gueunna nek tallibe ndakh tallibe serigne touba dou fenn biyileene serigne saliou ak politique mome nenna politique douthie deffar douthie yakhe dieureudieuf serigne touba

Mamadou

Niang sa tour dah yiwe mais yowe dioulite dou sose liguawakhale macki c’est pas vrai so bagne le président boumoutakhe sose molla gueunna nek tallibe ndakh tallibe serigne touba dou fenn biyileene serigne saliou ak politique mome nenna politique douthie deffar douthie yakhe dieureudieuf serigne touba

Publier un commentaire