Taayyy moom sa wahga deuga lila l’ambassadeur du Rire daaane wah que les artistes comédiens s entrent aide entre eux mais ceux qui sont devant ou dans certains medias in peut qu’on les détrône alorsque art guetthlaaa kouneka sa weurseuk gassiyyye leeeka
Sa mbam khouhh
Ki kay dafa kat ndem rek beug beuz rek mou melni mbam khoukhhh
anita
dit rek mouy melni cochon
boy walf
Sa tu as vraiment une dent contre la télé de Youssou ndour mais yagui censurer loubari yaw tamite que dire de ton patron sidy lamine migua khamni semaine bi yeup mo nék invité ci émissions you mak yeup you walf ci radio bi comme ci télé bi et puis fleurs yi guaye jeter Waly seck ndakh Joni Joni moye sponsoriser nepad té gua yamalé rék
zorel
Woop du jamé vu 1 jalou ki grossi
Bleu
Lima diakhal loutakh sa tek beut youssou ndour ak tele tfm c extraordinaire c du jamais vu mousouma giss kou bagne nite ni maylen diam te lidianti sa tele ngir yalla sokhor nga trop
Mimi
Méchant rek.niawayam bou doy.je l’aime pas du tout ce mec
miley
Cochon ki khamoute bopame dhh ki loutakh mou bagne ko
Dior Oye
Il a parfaitement raison.
zou
deug rek la wakh; bougoulène kouy wakh deug
lika
il a raison et pour donner plus de sens au série ils devraient faire venir de nouvelles tétes professionnelles
CAFE AVEC
SA TAYE DEUGU GOU VER GUA WAHH VIVI AK BALLA AMOGNOU PLACE SI FILM BI OK
IL POURAIN PRENDRE GORA DE CAFE AVEC ET MYA IL POURAN BIENT JOUER CE ROLE QUE CES DEUX PERSONNE
omzo
mm erreur k un caf avec il savent dbute mai finissions 0
marie
pourtant wakh na deug,ya ke des comédiens qualifiés ici au senegal,si soleil levant veut un ponkal kom balla,nagnu dieul paco ou bien un autre dou fi diekh. khaley bou toye kom vivi amna ci comédienne yi. et ils jouent bien,donnez leur une chance.
PAPITO
MAAN WA TELE BII DIAXAAL NENIOU MA DOUNIOU CREEER.. DOUNIOU AM AUDIENCE WAAY LOU WAAY DEFF NIOU CRITIKE CEEEY… WALF MOOOY ASSOCIATION DES JALOUX DEGGE… DE TOUTE FACON KOU AM HOOL BOU RAFEET DOUFA LIGEEEY MOUKKK…
SS
Il defend ses collegues comediens , c normal .
diadia
NDAY SAAN YEREM LEENKO BALLA KHEW KHEWI DAFAMETI LOOL GADAAGUI MOO DIEHOL MONI SERIE YI DEMBALI LEENMA ADONA NIILA
PAPITO
SA NDIOGOU C PAS UN COMEDIEN MAIS UN POLEMISTE…IL A JOUE DANS KOI IL NA NI LE PARCOURS NI LE TALENT D UN COMEDIEN MAIS C JUSTE UN CON QUI AIME POLEMIQUE ZERO TALENT TOUSS HAMOUKOOO
PAPITO
SOUMA BAYIIIWOULOOONE SAGGA DIIINA DOONE HOTTI LOU BOOONAAAM BA YEGGE AUTOROUTE A PAYAGE DIOUBAAL DIAMNIADOOOO…OOOUUUUUUYYYYYY!
nana
khana sa ndiogou dafa fateh boopam mme d’o animateur bou gnak khorom d’o jouwena thtre bou gnoak khorom tamite donc mme khamoul bopam au yene gnikoy may deug
babou
Sa Diogou je ne suis pas d’accord avec toi ils ont le droit d’inviter des stars une façon de mettre un peu de sel dans leur film. Cette pratique est récurrent dans les films américains
fuck
SA MBAM KHOUHH sa baye moy mbam
LO CHE
Mais sama gayi degg nékhoul mais sa ndiogou limou wakh degg là mbeur sà mbeur ya artiste sà artiste ya mais viviane ak balla gaye linuye am nà aye artiste comédien youko meune balla gaye nà dém dieuli combat mo geune ci mom viviane 20 ans de cariére ci music té menoul mélni wally seck déf bénne vidéo am 500 mille vue ci youtube rk di bari wakh son wokall wokall té baye fall bi waye ko so kholéé youtube àm na 800 mille vue té bobou moy cd music bimou mesà déf ci sénégal…..
anonyme
Del setane filme américain yi c pas un problème artistes ou kou siw di participer thi ay séries ou filme dina yokou filme bi succès ak bopam c rien c juste du marketing ignane bakhoul
rire
mbame khoukh bi mogui dèf emmision batay
Deug
Sa pourkoi tu regardes pas les téléfilms de walfadjri. On te force pas à regarder wiri wiri wala bok vou créer votre théatre et vous inviters les personages que vous voulez, bayil sétane tfm nguir yalla waleu tu peux pas
Deug
Sa pourkoi tu regardes pas les téléfilms de walfadjri. On te force pas à regarder wiri wiri wala bok vou créer votre théatre et vous inviters les personages que vous voulez, bayil sétane tfm nguir yalla waleu tu peux pas?
Deug
Sa ndiogou pourkoi tu peux pas arréter de regarder et wiri wiri. Contente toi sur les programmes de walf ! Waleu vous créer votre telefilm et vous inviter les comediens ke vous voulez.

Kéne forcéwuléne sétane tfm, ya d’autres télé.
Ah cone tu suis wiri wiri