wa walf soff guene xana amolen lolen wax tjr mm wax rek
Mami
Ki melni elevou CP bouy wakh !
Ak séne information you pauvre yi pffffff !!!
Madam Faal
pape cheikh yakarr na diaroul justice budee lerr nala ne defoko bayilen ak Yalla borom kun fa yakun mou ate, pekhe nonyi rek la way Yalla bakh na, Yalla na la Yalla defal jamm, Amiin Diallo ken dou meun thi yaw touss
Beugue Sénégal sama rew
l'affaire ne se portera pas à la justice, parceque ça devient plus clair. celui qui a écrit cet article a bien vu ce qu'il a écrit et lui en personne le sait. l'accusation ne se date pas d'aujourd'hui
bara samsung
yalananiou yala diegual
sanou
pape cheikh ya tey sa vie la
deugeu
WALF WAKHOU DIAMOUR MOTAKH YENEEN TELE YII RAWLEN
verite
walf amouleen sponsor
Madam Faal
sposor yi yeupa ngi tfm motakh nonyi merr mais dineng dee gfm thi kaw thi kanam, sposor yi am neng fayda ndakh nit boi diay dankoi yobou fumui diary, te askanwi neneng gfm moko yoor
ibra
jornaniste yi khibarr bonio len niokh donio ka settan tall bala niokoy dougall internet bi
palermo
yen lan moy sponsor dagena khamoule mo takh walf neckoufi pour sponsor waye dafe neck guir asskanwi merci walf yaye telle asskanwi grazie tu sei nimero nuo da senegal
Bien parler

bouni wakh tele senegal walf mo takh niouy wakh merci yenay peeee
Homo thiime mo bone
heuuuuuuuu…mdrrrrr….ils s embrouillent pour des bouffons….que ca a faire? j en rigole en mourir..
sui dead loulen. si woor
AMETH AIDARA dangua reey lamégne wagnil