Video- Affaire faux billets de Thionne Seck: L'équipe de Yéwoulène commente

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Aucune recommandation disponible.
Aucune recommandation disponible.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
YOUSSOU NDOUR DIMBELETIKO DIAPELEKO YAYE PAPA DALA YAPE REK MAI YAYE PAPA DIAPESI REK YOUSSOU NDOUR DIOGALE SA DOME DJI DEFATINA GAFE
Je crois qu'il faut faire attention père thione a été escroqué.
wayé nak il doit faire revenir Waly sur terre..
bou fékké moka def na ted
Léo diam
L'épa diam
Kilifeu bou amé ndiabote bou nékoul si yone, dangko wara lidjeunti surtout nguani yaw djoulite ngua. Boulthi séte siw, boulthi séte xaliss, séte si YALLA.
Kéne bagnoul li waly di weuy, wayé niou bari douniouko déglou ndakh soline guou bone ak fréquentation you bone (gore djiguéne).
Wakhléne mou moytou borom bi mome serigname.
Wadiour deug, serigne deug laléne YALLA sante si séne ndiabote.
Alale bakhoul.
Bal lénma akkh, YALLA nama YALLA bal.
Wassalam!!!
thione ça ce voi k kene bagniou kene yenewoula li papa thione
Waxléné thi ce pédé d'animateur
bravo papa masamba
yana ci Thione guène way, il ne le mérite vraiment pas
mashaa Allah tfm Yal na len Yalla yok jamm te mousal len si pekhe nonyi, Amiin
Merci Massamba
wow gor way koubakh leral yii amna solo trop…. nassi journalist coriger sen bop boubakh touss khamougnuko
bravo massamba. la plupart de nos journalistes sont nuls.
séytané mo bari dolé
Papa youssou ndour c le moment de te lever et faire sortir papa ballago de cette situation et je c kil le fera
bravo massamba
Lol