ngagne yaw sketch yingay def ramadan mem apres ramaden dafawara continue ndax dafa am solo
aicha rassoul
Li laye wakhati si gor gni beugueul té BOUL wolou
Souleymane Ndiaye
Aicha Rassoul loutax lolou mai dafa ame goor yo xamni Ken xamoul ligni beugue sama genre bi mai Ngagne amoul droit diko fotlo ndakh amna djiguen yo xamni ay princesse lagnou tei Ngagne diabarame yeup elles n'ont pas droit de se faire salir . Djiguen dagnoukoy wormal dafa lathie respect bougnou len defone ni sunu Yaye rek problème dou ame
NIT DOFFF KILLER
ngagne ya deh "fotmi barina té ki mounoul fot wagniko way plazzz
watt baaba watt
na faute lih waye ah
ada
j t connai pas souleymane mais kou bakhnga djiguene dagnoukoy yeureum dou loula nekh rek wakhko wala defloko boko yeuremé rek yalla djiapaléla té bala gnoulay takeu lo wakh nonoula lo beugueu wakh nonoula bougnou amé lignou beugue tay ngay ddddddd…

I lov u maman