Serigne Abdoul Aziz Sy Junior souffle ses 88 bougies

Cheikh Abdoul Aziz Sy Al Amine, le porte parole du Khalif Général des Tidianes a 88 ans aujourd’hui. Un jour mémorable qui ne laisse pas indifférent à ses petits fils qui lui ont fait cette belle surprise de l’offrir un spécial gâteau d’anniversaire.

AL AMINE

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

63 commentaires

  1. Serigne Babacar

    mais pourquoi sénégalais gnémé soul deug, anniversaire ak gâteau ak bougie affairou nassaraan la, bokoul si diné ak kouko neuneu def nak


  2. momar

    bamba fep fane yene sene serigni mal sivilise yi nga khamni wakh lou leer sakh meunougnuko lolou molene meti nolenekoy tale ate wakh lou gnaw serignu diambour yi sa baye dako taloloule ndour lidieunti adiya boume diokhe motakh waye dounde 88ans saye seute bete diko fete ate yaw dara nekouthi lou rafete la bayilene wakh lou gnaw ta ngene topato seni baye bayi bayou dioambour

    yi


  3. Rage

    Yalnangua fi Yagu té wére té gni ssi wakh lou bone yeupe qu'ils se rappel du gars qui avait tenté d'exploser une grenade sur Srigne Abdou Al Amine grenade ba mo explosé si kawame. Yéne nieupe vous allez bruler à vif di wakh lou niaw si nitou Yala Yalnégu ko djiss. Mauvais que vous êtes


  4. mariama

    Em tt cas serign touba akk seydi el hadj malick nio bokou ben mame ter serign abdou aziz sy ak serign fallou aussi nio bokou pck sen niary yay yi ay mbokou lanoou kouko weddi latiel donc na wakh yi rafete rek


  5. sokhna khady fatma mbacke

    MAME ABDOU AZIZ SY JUNIOR niionguui diégalouu bou werr sy sunu baye nga konn danioula wara diokh thieur aux noms du mouridism nous vous presenton nos excuses


  6. BAMBARA

    ASTAFIROULLAH PARCEQUE JE VIENS JUSTE DE VOIR QU'IL NE SAGITMEME PAS DE BOUGIES MAIS PLUTOT DE GATEAUX DE LA PART DE SES PETITS FILS, SO WHY NOT? AFFAIRE BOU NICE! EN PLUS , QUI N'AIME PAS LES GATEAUX ? JOYEUX ANNIVERSAIRE SERIGNE BI


  7. bambara

    MOI JE COMPRENDS LA REACTION DE CERTAINS, PARCEQUE QUAND ON NOUS PARLE D'1 ANNIVERSAIRE D'1 GRAND MARABOUT DU RANG DE JUNIOR, ON NE PEUT PAS S'ATTENDRE A LE VOIR SOUFFLER DES BOUGIES. NOTRE IMAGINATION EN TANT QUE TALIBE CAPTE D'AUTRES IMAGES, PEUT ETRE PLUS OU MOINS PIEUSES, BUT STILL, IL FAUT SAVOIR RAISON GARDE SI ON N'A PAS QLQ CHOSE DE BON A DIRE. SALAM


  8. solo

    salam j suis mouride yéne mbokou tidiane yi malénedi niane ki toudo adiya nek fi di sagua di wakh wakh you bone yi dou mouride ta bokoul si taloubéyi loumou beug moye kou sagua serigne mouride ignoré lene ko esq dioulite la sakh niak yare bokoul si serigne touba


  9. sokhna khady fatma mbacke

    salam mangui ziar bou werr mais lii moy lann cheikhoul, khadim danoul dokhalé ni donc un peu de respect pour nos guides religieux way roussna lol worna cheikhouna khadim kii sounou baye la sounou kilifeula délénnsi bayi khél diadieuf


  10. sokhna khady fatma mbacke

    salam mangui ziar bou werr mais yenn lii moy lann cheikhoul khadim danoul dokhalé ni un peu de respect pour nos guides religieux way roussna lol worna cheikhouna khadim


  11. sokhna khady fatma mbacke

    salam mangui ziar bou werr mais yenn lii moy lann cheikhoul khadim danoul dokhalé ni un peu de respect pour nos guides religieux way roussna lol worna cheikhouna


  12. HD

    Frères et sœurs restons à notre place, Allah azawajel n'a pas besoin de substitut !!! Nous sommes trop petit pour juger… Faisons preuve d'un peu d'humilité et n'oublions pas que nous sommes musulmans avant d'être tidiane, mourite, niassen, layene etc. @


  13. Islam thia kaw

    Wakh dina yobe nit lounek eulleuk

    Naniouy seetlou wat liniouy bind.. ndax fii lofi khass bind demna.. te manoko efface wat.. te eulleuk page Facebook whatsup ak bepp site lep loufa way bind rek .. khamalni yalla danako saytou. Naniouy settantal liniouy wakh te diko rafetal… ak si koumou mava don nak. Yalna yalla tappe kholyi yeep amine

    Biyileenko khell


  14. diaw gueye

    longue vie papa toi a qui je dois beaucoup de respect, toi qui as donne a mon mari une bonne education je te dois beaucoup papa joyeux anniversaire


  15. sohnasi

    je suis mouride mais j ai Beaucoup de respect pour les tidianes te fi dou affairou mouride ak tidiane. boudoul dara war nagnou respecter son nom , son age ak rolame si comunaute bi thanks


  16. omar diop

    J ai été vraiment surpris de la réaction de certaine personne al amine n est pas n importe qui par conséquent nous lui devons respect et considération en tout cas moi en bon talibe khadre je lui souhaite un très bon anniversaire , une longue vie ,santé de fer


  17. Ml

    Salam à tous présentement il est en Espagne et devra animer une conférence religieuse le 31 Inchalah . Nianou Serigne Babacar sy (rta) ak Abdoul Aziz Dabakh founiou dadjé kou yébo ham loy wakh.


    • le bambiste

      verite li kharamoule dhé wayé da ame nioumou warre. mane bouko sama papa défone ma toure table bii wayéé grace a s bamba talouniouko sakh bakoye khalate magui diégalou nak


  18. rebatass

    adiya jolof man ak mety sall yene niou rew guen ter niak yar meme boudoul dara mate nalene mame guene tof fi diwakh khana degolen louniou bind ay petit fils nioko defatal surprise . yalla nalla yalla may goudou fane wergou yaram ak ay atte you barri barri souniou kanam


Laisser un commentaire