28 COMMENTAIRES
  • consultant

    franchement waa soleil levant ils st fort…..!

  • eumeu sene

    trop mm

  • hams

    Bravo à eux vraiment c des meilleures la vérité ???

  • mimi

    haahaa bineta mala fan waay tchuumm… lou diote rk yombe

  • Oh lalala

    Lici film rk amul vraiment c MA-GNI-FI-QUE chapo à soleil levant

  • kani xèigne

    nèkhoul ba nèkhoul dal lingèine di dèf mane nginko

  • chacha

    no mane yayou soumboulou vraiment neikh guama trope

  • déguene

    legui film yi yeup nurok café avec. dama diomi bama guissé fin bi. sénégal daal dou dem. Maa gueneu bagne café avec wayé dafa melni nieup thi niome legni roy.

  • safi

    film dafay am sens. Il faut un vrai scénario pour faire un vrai film. Chapeau à vous et bonne continuation !

    • DEUGUEU NEXOUL

      Malheureusement gni amouniou scénario. Sinon douniou nek thi wer kor thi bir film bi.

  • seck

    ROY DOU NDOUROK PIIIRR! Nékhoul ba nékhoul wa soleil levant nio fi meune!

  • Mya

    franchement chapeau lila khamm film day ame sens mais Zozo afaire a regler avec ta femme hihihihih

  • diadi

    mdriiiir sanekh dina ma ray nena ko vomi lol

  • zico

    déguene ya sof bane cafe avec soleil levant dou taye démb la! bravo c super

  • anita

    nila film dafay am sens korgui sakh waroul téré nga continuer avec nos réalités du sénégal soukarou kor nafila yi et tt.

  • abdoul

    Déguene ba wa soleil levant di théâtre bobou wa café avec dioudo guouniou sakh donc khawma loufi indi ay royoukay tchhiiipp

  • less

    c super amna sang lol nila koi

  • fa

    Affair bi t fm l monouye bégual dinou diokh wiri wiri dinou tégual café avec ak yénén ak yénén diarama waaye t f m rek ñoo beuré f m

  • bise

    franchement vous etes forts

  • baye

    enfin cheikhouna decouvrira la verite .felicitation,

  • Mbaye Dozé

    @Déguene tu as parfaitement raison. c'est du copie coller. khana kene dou wakh sa khalat ? ils font exactement comme café avec. En plus je viens de me rendre compte qu'ils n'ont pas de scénario original (et cela fait peur). ils écrivent au jour le jour. La preuve cette histoire de soukeur kor et de ramadan. Moi j'arrêtes de suivre tout simplement parce que l'histoire de jojo m'intéressait mais je me rends compte qu'elle n'est même pas écrite.

  • mignone fall

    vrment vs avez raison Wakh deug amoleine scenario bu bakh. jai fé le consta mé senegalais dou nagou verité so wakhé niouné daga sokhor kounen am nga droi diokhé sa khalate a revoir

  • dada

    mais vous venez de découvrir k ces séries n'ont pas de scénario? niome nieupe leu café avec, wiri wiri, double vie etc… ils jouent au jour le jour; j'ai fais la remark depuis longtps! j'ai l'impression k les scénaristes lisent les commentaires sur les réseau sociaux et autres et se basent sur ça pour écrire la suite surtout café avc! film bo khamené kiye binde khamoul suite bii daye tatonné rék dii démm piffff

  • ok

    non sokhor si tu nous tiens mais vous ne savez pas qu une oeuvre n est jamais parfaite le rajout dans un senario tout en maintenant le contenu du senario quel grandeur soleil levant bravoooooooo way

  • baye

    non les gas areter vos commantaires de sokhor way jusque la. bal ba ngui daw way CAFE AVEC WIRI WIRI MANE YENE REK LAY SETANE CONSOMONS LOCAL LAGNOU WAX.LES JALOUX VONT MOURIR

  • lola

    bravo les gas merci thies forever

  • moooo

    sénégal kou wakh deugue rék niou ni danga sokhor! lane laniou sokhor thi aye séries piffffff! mou nékh ak nékhoul ame scénario wala déte loumou gnou wagni on di seulemen nos pensées et on é libre de le faire! arrété de voir la méchanceté partout critik moye takh nite di gueuné persévéré di innové! maye léne niou ak séne diayaté

  • zp

    dina nekh dina yeu ngo soleil levant wotena 2fois xana nekh

Publiez un commentaire