2 COMMENTAIRES
  • diop

    TIAXAANE BAAKHOUL ! dagnouy nakh sèène bopp rek ak sèni supporters !

    mais tout le monde sait que les dopés de l’arène seront limités un jour ! kii di gouy , balla gaye 2 et consort, ils n’ont plus aucune chance de gagner des combats face à des ahlètes comme boy niang, modou lo, lac de guer, eumeu sène et autres ! triché baakhoul !
    khamoone nané fii laye moudjie té guissagougnou dara ! gnou dém bassi kanam inchalah ! on est des sportifs, on connait un minimum en la matière ! tot ou tard dopage dafay yakh say organe ba doo amati doolé ! boy niang doolé deugu lako diaay fii ! balla gaye na dieul boy niang khool, lèègui mou lèèr

    au passage douma pikinois nak té faralouma boy niang mais deugu réka waur

  • djibson

    franchement boy gniang est bn athlete

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *