1 COMMENTAIRES
  • MDG

    Non, Aladji dou mana teudj bou tontou woul lî may lâdje ba paré.
    Karim foumou djeulé alal djî neik Monaco?
    Khâlissou sénégalais yi la walla deite?
    Sounou alal la, Toubab né dou gnouko dellô nguêne di ci contâne dâle!!! Nooonnn nonon non ???
    Contribuables sénégalais bi rek mô ciy perte ndeysâne
    Ahmed bô ma tontô ba paré nga teudj ????

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *