A quelque chose malheur est bon dit l’adage. Titi, la Lionne de la musique sénégalaise, après quelques couacs avec Prince Art managé par Ngoné Ndour, s’est rendue mercredi chez la sœur de You pour lui présenter ses condoléances, suite à la mort de son mari. Le Sénégal a des valeurs qui lui sont propres…Que l’on ne trouve nulle part ailleurs.
Retrouvailles Titi-Ngoné Ndour: La Lionne a présenté ses condoléances mercredi

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
machalla titi geste bi nice na torope sak yalla nala yalla diapalé lafalla thiate yaw ak ngoné ndour yalla naléne yalla djibolé baguéne méle niguéne mélonne
titi non seulement pastélou nga, rosawou nga ,wate ga sa yéne crayon ka ngay melni kou dieme baptéme toubap, titi ana sa cole may wakh ngay dioy seyetane rek mon léne diape moi même je me demande ana sa gout de dialé?
Je fais parti des 1e fans de TITI mais adouna sa teranga fou mou nekh boula ka ken khagne .Titi delouwatal prince art kou la ka wakhoul bougoula
SOUTJOU c'est une photo qui date de longtemps une émission a la SEN TV ou elle a pleuré
Mais c'est normal que mou dem dial3 lol ou dou dara nane wakhtan rek mais nit d'où guawa guiss boppam
mé sama mokayi diama dafa nékh cone yalna yalla doli diama titi ak ngoné sén diguété bi dafa yague lole bakh takh na yalna si yalla déf diama bou bakh té niou andak ligueyate, sénégal réwou diama la
SENEGAL SEN WAKH DAFA BEURI MOTAKH TOUJOUR NITT DIWAKH LOUMOU KHAMOUL DIDEFF LOUMOU KHAMOUL THI DIGUETTE MAK AK RAKAM LOLOU MOUSIBA SISTER NGONE GRAND YOUSSOU TITI SEN PRODUITLA SEN RAKKALA LE RESTE C LE PASSE
Titi nekal ci diam lui nga def rareté na
titi guissélénn si péte rek nga déllou prince art moy li gueunn si yaw té kholl si you bamou lay fékk guinnée di la fi eundi
Yalla bakhna lussikame rawoute beute
felicitations nous Sommes contente
adouna amoul solo shaitane dafa bary dole te si digante bou rafet rek lay dougou, Yal na Yalla yok jamm, Amiin
ainsi es notre Sénégal adouna amour solo titi t'a bien fait tes une vraie lionne
Allez la lionne
JADORE BCP EL CHANTE SI VOUS ALLEZ SUR YOUTUBE VOUS VERREZ KEL A PLUS 4MILLIONS DE VUE POUR UNE SENEGELAISE KI CHANTE LE MBALAKH C RARE MEME YOUSSOU ET VIVIANE NONT PAS CA.JE TE SOUHAITE UNE BONNE CONTINUATION .TH OCI GESTE BI AMNA SOLO BOU BAKH .JE TADORE
babacar yangi hors sujet fii diame mofi hew sarah gniou rek
Merci tima goor bou seytane rek la bagne Babacar mi kou diara sekhlou la
titi diame rek mon nekh du courage
ki c 1traitresse kissagoul dara sakh ak fika youssou ndour dieule moukoy dieunde d.media foumou moudje nioniou lache nanouko parck ils ne peuvent suivre sa promotion bo wore rene ba dewen mou djila danoulako djign mais dou yow
Mon frere Adouna amoul solo Wayee yorna xolou dioulite Demna bokou ak mome nakar bimou am mo eup solo nga Balma sou fekee dama dioum
Titi I love you so much inchalla lou Bakh rek nai am
Rafetna titi adouna amoul solo lo gisse dafay diekhe
wé il ya de ces personnes si tu les voit rek de par leur apparence, de par leur façon de faire, tu en tires quelques choses c'est le cas de titi si tu la vois ça saute à l'oeil sa gentillesse bien que je ne la connais pas. elle est toujours souriante, emotive. on t'encourage à continuer dans cette lancée mais il faut faire très attention aux hypocrites qui font semblant de vous aimer alors que nenni
Adouna amoul solo te kouko kham nopalou.
la vie c'est ça ! pour avancer dans le showbiz il faut savoir prendre tes responsabilités , comme l'a fait Youssou ndour dans le passé avec Étoile de Dakar . au Sénégal Prince Arts est l'unique qui profite des chanteurs . mes condoléances les plus attristées a Ngone Ndour . elle n'est pas la première et ne sera pas la dernière a faire cela ! il faut comprendre c'est Normale et Naturel !
Titi yalna yalla fay la sa khole
Ndiaye louga
Ndeysan vraima ? li nice na
na refet titi djioulite nilay mel bayi lep def tee yalla tah nit dou dara gnoune gneup ben lagne c le senegal na rafet
Bilaye titi mala beugal sama bope.yalnala yalla faye sa khol.auduna amul solo..yaw diamu rk gaye am inchalah
djam sila lepp khath.. yala na sounou borom doliniou djam… kenn khamoul lisiy topou. leglei sounou borom nii lay defarei digantei yi
Mercie titi tu a un grand coeur ngone adouna amoule solo diapal titi kou bakh la
Félicitations Titi tu a de la grandeur adouna amoul solo djeuff dji rafetna trop Yanala Allah feye sa ndiaal amine
on aimerait vraiment que le grand you ai de l'hauteur et pardonne titi puisqu'il a beaucoup fait pour titi beugne ak lamigne gno deuk té lé lé dagnouy dioté
You n'a rien contre Titi et Titi aussi n'a rien contre You c'est avec les autres qu'elle a à faire
titi borom baakh la machallah khol bi dafa rafete.
je suis d'accord avec toi Titi khol bé raféte mo takh ma beugeu ko
titi keine dou yaw si kaw si kanam rek silou bah beugue bila beugue amoul feine
ndaay saan diam rekk sila lépp khadj