Photos(10) Hadaratul Jumah avec Al Amine au stade Amadou Barry

Revivez en images la 4e édition de la Hadratoul Djumah exceptionnelle, organisée au Stade Amadou Barry le vendredi 15 juillet 2016 par le mouvement Abnâ’ou Hadrati Tidjâniyati sous la houlette de Oustaz Modou Fatah Sarr, sous la présidence effective de Serigne Abdoul Aziz Sy Al Amine.
Man dé ap mouride la wayé rafétna lolou kholsédana yallay yagu yak a sakh barké borom touba
Macha allah khol sedatina.senegal diam rek si kaw si kanam.rafetena yalla na khewal yi yokou si adouna rawatina senegal rawatina si dioulite yi.
yalna yalla nangou niane yep
machaalla yallana yalla naguou nianneyi ta fayalgnou cheikh ahmet tidianniya amine
Lou rafetla mais nagnou si bole diangue te gueustou sounou dine surtout les jeunes dina am solo
akassa
Yallah yallah nagou niane. Amine
on dirait des laynnes avec la couleur blanche!!!!!!machalah c beau
machalah rafatena sangue serigne abdou yalla na yalla goudale sa fane amine yarabi
amine yal le ne y’all nagnou gnanb
Alhamdoulila
machallah lep selna comme j’ai l’habitude de le dire nekk talibei Cheikh chance la mais dou merite yallana buurbi nangou nian yi
Contane na yalla na gnou yalla tass si lérou seydi Cheikh ahmed Tidiane cherif amine
Amine wy senegal dimmou rèc
Dieuredieuf Mourchid Mawlaya Cheikh Abdoul Aziz Sy Al Amine
Masha allah notre pays k allah bnis tout le peuple sngalais
Aminne yalle na sounou borome nagou nianne yii ci barke saidina mouhamed psl Aminne
ma’acha’alla.le rcital de la perle de la perfection
cheikh tidjane chrif amoul moroom
Machalah yalna yala nangou niane yi amin ya rabi li rafetna trop way.