2 COMMENTAIRES
  • Pierre SAR

    Serigne Saliou jel na mooméélam. Ken duko yab. Fii ba aduna du tukki, lek a ngi ci loxoom. Barké Serigne Touba.

  • Cheikh Ndiaye

    Ndayesane doyna ware de yalnako yalla yeurem the khareko aljana ferdawsy barkep serigne saliou Mbacke serigne gniam ba

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *