Annonces
Annonces
» » » Le message émouvant d’Aby Ndour à Thione...

Le message émouvant d’Aby Ndour à Thione Seck…

Voici le message qu’Aby Ndour a écrit sur son mur facebook pour Thione Seck

aby-ndour-a-thionne-seck

Annonces
Annonces

50 commentaires

  • marem
    31/05/2015 18:33

    amine ya rabi

  • lamzo
    31/05/2015 18:43

    aby ndour boul niou sonnal thione seck diouboul lougn ko wakhal moko deff

  • penda
    31/05/2015 18:47

    ABY YA BAAKH. thione lY nattou rek la bouko yallah tek pour saytou nguem nguem mam.NITGNOU BAAKH GNEUP DIAR DIAR NAGNOU FI.

  • bah
    31/05/2015 18:50

    aby ndour yow meyy gnou wayy..thione seck tekk ton grand frère beute mokko dougueull sii liyeupp..ton grand frère nakk képp kouko tekk beute guiss koo yalla ko deffarr bamou très bien..waa salamm..la justice tranchera si les fai st avérés..

  • aramjnie
    31/05/2015 19:13

    l ami de ton ennemie est ton ennemie doy na war

  • mbaye.khoudia.thioune
    31/05/2015 19:35

    yallnalayalla.samemo.arla.moithialla.banobayi.ak.diame

  • Amina
    31/05/2015 20:00

    youssou dei kouko tek beute yangui def lo khamoul ndakh Yalla ko diapale ak nianou wayjurr,way thioune Yal nako Yalla defal jamm

  • mareme P Nd
    31/05/2015 20:00

    Amine Aby. Yallana yalla tegui natou bi ci kaw thione.

  • yaw
    31/05/2015 20:15

    aby yaw mome hana youssou dala rayal sa taw

  • soukk
    31/05/2015 21:39

    Thione n'est que le premier de la liste. Heureusement qu'il est pris. Il aura le temps de se repentir et d'effacer certains péchés. Tous les autres ont intérêt à changer. Tout leur argent est sale car gagné dans la transgression des règles de l'Islam. Dieu est patient. Ne l'oublions pas. Il aura bel et bien le temps de s'occuper d'eux. sans exception.

  • pote
    31/05/2015 21:54

    merci aby yaw kou bakhgua yalla na yalla teguil natoubi papa thione tai koukoko yene yalla nagua dougue diel balamoufa guenne

  • gorgui wade
    31/05/2015 22:15

    amine way Aby yaa bakh goree yalna la yalla diapale yowitam

  • Samba Diouf
    31/05/2015 22:22

    l'histoire donnera raison.

  • birima
    31/05/2015 22:25

    en tous cas je ne sais pas ce qui lui manquera mais ce ne sera pas du temps pour écrire la chanson qu'il nous avait promis THIEP BOU DIDJE

  • sidy
    31/05/2015 22:25

    Amine tata abi

  • dysi
    31/05/2015 22:26

    Amine

  • éva
    31/05/2015 22:34

    natou dou wess aby ya gooré

  • papa
    31/05/2015 22:56

    gewal da nio yabatemei ci yone rek

  • ndiaye
    31/05/2015 23:03

    prison diomoul kén dal

  • droi
    01/06/2015 00:05

    bande de con su on le lés demai je brie le palé de jistice béte

  • paco
    01/06/2015 00:17

    le temp jujera

  • prison diomboul kene yalla nako yalla teguile natoubi
    01/06/2015 00:47

    prison diomboule kene yalla nako yalla teguile natoubi

  • khadija diallo
    01/06/2015 01:48

    Oh merci bcp aby ndour yalla n'a yalla maye niou ndame ba papa thione guene si leundeume bimou nek ni nieuwate si leer deloussi keureume si djabotte tame Amine Yarabi

  • fall
    01/06/2015 03:20

    yallah nayallah nangou nian

  • Deugueuntaan
    01/06/2015 04:46

    Gnanal Trafiquant Sénégal dafa melni aye kania lagnou 100 Millions d'Euros pour Tournée ko khameni aye diékk Locales rék gnoy écouter ses sons wooyyy sama ma diakhlé dé !

  • Beugue Sénégal sama rew
    01/06/2015 07:36

    moi je voulais savoir lane moy natou? lo tay wala loula dal té ta yokou?

  • SAMAKHALAAT
    01/06/2015 08:27

    Aby Ndour Yalla bakhna lolou kén wéréntéwouko mais mom Yalla mooné niou dioup téy dioubeul . Naafékeu baakhoul.

  • dabakh
    01/06/2015 09:18

    Khana dénguin fatè destin djilit dou khas morom djilitam sa morom djoulit sou nèkè si tolof tolof nianalko allah soubhanahou watala mou guéné kossi ak diam

  • banel
    01/06/2015 09:39

    amine yaa raabbi yalnako yalla guéné thi tolof tolof yi

  • youssou
    01/06/2015 10:21

    wakh dafa wara rafete natou dioumboul kene

  • nevel mike
    01/06/2015 11:15

    Au faite tout cela n'est qu'une preuve de ce qui se passe avec les gents qui sont au devant de la scène et que l'on considère comme modèle. Le Sénégal est salle très salle même et a besoin d'être laver. et pour cela il faudra assainir le milieu du show-biz. merci

  • Boy lamane
    01/06/2015 13:34

    Apres idrissa seck cheikh yirim seck c Thione seck thiey wa seckene . bala sa dom di fatou nga fatou mo kene Thione seck declaration contre youssou ndour egal rebeusss

  • kheusss
    01/06/2015 14:18

    na yalla wallou la mais dal doyna warr et aby yaw tu as montré ta sincérité à papa thione kou bakh nga

  • SEDHIOU
    01/06/2015 14:22

    DU COURAGE THIONE

  • jh
    01/06/2015 14:46

    nitt day nangou dogaluo yalla a l heure y a quelqun qui vient perdre la vie d autres subissent un accident kou amoul natou khamelene yalla fatenala d autres tombent malade voila la vie des hauts et des bas quand etant gosse thione chante a la caserne sa,ba diery diallo le general waly faye yalla na fi yague et ma mere decedee vous voyez ou est ma mere ou waly faye nie ngui si yalla wawe thione santal yalla bou bakh li mo guene si yaw un jour bene waye da fa dougou prison il a trouve un grand marabout mou ne ko sa waye si tu n es pas venu ici tu vas mourir par accident quand il est sorti un meme marabout lui dit la meme chose

  • LIMBIR
    01/06/2015 15:56

    YEN NAFEX NGUENE REK THIONE MI BAXOUL DEFOU LOUBAX NGUEN KOY LAYAL NIIT SOUMANOUL WAX DEGUE SAX DAY MANDOU

  • 85
    01/06/2015 16:30

    yay gor

  • diop
    01/06/2015 18:25

    natou dou wéss yalla bakhna

  • Papa thione
    01/06/2015 20:14

    yo alla walou

  • fée
    01/06/2015 22:38

    je l aime je l adore que Dieu le protége et le sorte de cette épreuve plus fort…

  • awa
    01/06/2015 22:39

    Yalla founéke laye wané bopam aby yaye gore natou dou wess yalla na yalla soutoural pape thione

  • fatma
    01/06/2015 22:43

    amine way kène yénew koko

  • blake
    02/06/2015 10:04

    SAYETANE NGA NOPILE YOWE SAKHE BOUGNE KO FEKONE SE KEUR NI LAYE DEME KONE NOPILE YALA BEGOULE KOU NAFEKHE SIME SAYTANE NAFEKHE NITT DAYE WAKHE DEGEU FENE REK

  • blake
    02/06/2015 10:15

    YAYE SAYE TANE SA GEMEGNE BOU NGANDE BI GNAWE BODE BOUKO DEFOUDONE GUAYI DOUGNOU KO DIAPE THIEYE SAMA GAYI YENAYE POMKALE YENA KHEREGNE MERCIE YENE MAKY DALENE WARA YOKALE GARATTE MO SATHIE LA

  • dikha
    02/06/2015 20:18

    Amine yarabi

  • nana
    03/06/2015 11:54

    mane wally lay yane mou kholate bopam dakh khalissou goordjiguene yimouy encaisse ta papa thione. tek si beuteum wakhouko dara ta kounek khamgani goordjiguene yalla dako siip wakhatouma di sekeuk mome khaliss bou salte lolou rek la yalla Ken douko fonto ta ngane dioulitt nga musician yi kholatt Len Sen boop litakh youssou ndour nekhma do guisse mouk soireem ay goordjiguenne you koy may khaliss

  • hams
    03/06/2015 21:17

    Sa ira inchallah aby boul tiite boul ragaal toute les gens qui sont deriere tout vont récolter ce qu'ils on récolter inchallah c t'un coup monter mais dieux vois tout et enttend tout ???

  • khady ndoye
    05/06/2015 11:20

    aby natou mouta niank si djoulit diko nianal si barke serigne saliou papa thione kou bakh la te mandou dila nianal yala diapale bou bakh

  • Le malien
    07/06/2015 12:29

    Natou moy lan. monté sa coup chez toi même donnez des RV nocturnes dans les à des heures indues avec des fossoyeurs. lolou moy Natou. la justice fera son travail.

  • madam ly
    07/06/2015 13:30

    amine yarabi

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL