Publicité

Le mannequin Maty Mbodj est décédé...

Le mannequin Maty Mbodj est décédé ce jeudi 23 juillet. Cette jeune nymphe du Dakar des paillettes est apparue pour la dernière fois en public ce mercredi 22 juillet d’après une source citée par vipeoples. Après avoir passé la soirée en compagnie de ses amis Adja Diallo la nouvelle animatrice de « Yendoulen » sur la sentv et Doudou l’ami des mannequins.

54 commentaires

  1. mannequin

    ay way maty mbodj kou bakhone souriante une fille joviale est partie…yama nala yalla kharer Aldiana dila daler arame ak niom sey dou wa thies ak l milieu de la mode…Rip ma cherie

  2. aramjnie

    yala yeureumka ta fare ay bakaram deugeula ya pa d sot metier mais manekina daale nekhouma bocou de fille falagnouye diarrer yacou yala reck ka kham nama yala bale mais c une affaire tres louche

  3. ibou sene

    rest in peace sister nous prierons pour toi tu nous a juste devances que Dieu taccueille dans son paradis et nous aussi quand nous te rejoindrons dans lau dela

  4. Niassa

    Bok yi Nagn lén wadial sou gnou bok ta bagna top adouna ta kén khamoul Kagn gay dhé ta andak yiw tabayi tiakhan yii bakhoute ,top yalla rék woor

  5. lache

    kou diamoul yalla pertega ,,,,,,,,,,,,,,,,, bounek migui done diamou yalla ,,,,,,,,,,yalle nako yalla yerem

  6. khadousheu

    ooooh c vraimen malhereux maty mbodj nous a quite pour de bon mankoy dialé tte sa famille arame mbodj, seydou privé ainsi tt l milieu de la mode RIP

  7. Fallou

    Yalla nako Sunu Borom yeureum si Barké Serigne Fallou.
    waye na si jangeu lou bari . adouna diapoul kéne.

  8. rama

    Amine tt monde von partir manquin musicien comédien tt monde nono pourkoi tu le croi pas ki nit tes nit yeup paye wouyoudji sougnou borom

  9. DIC

    votre jour viendra on enquête sur vous, vous placez des cameras cachées pour faire chanter des gens, vous avez trop fait de victimes, trop c'est trop!

  10. sun

    Yalnako sounou borom geuereum te hare ko aljana..waye yit li yeup jangaat la ndah adona jaangaat la
    beneubi moy yangy daw thi guinawam te doko jot ba mouk
    Niarel bi moy Dé mungy sa ganaw te yageu yageu dinala jot
    nietelbi di sounou borom fo mana jaar da daje ak mom
    kon Mbokoui boulen topou jeumeu ba fate Rouh yi..
    Jamou yala moy Thiabi Aljana

  11. Nene Diedhiou

    yalla nako yalla yeureum te khareko aldiana firdawssi amiiine ya rabi ci barke Seydina Muhammad salalahou aleyhi wa salame

  12. omar

    Diamou yalla recke mo woor kou diamouwoule perte ngaa tée gnou baayii foo sunu borom néenaa ngaa daaw dieumee sii mane maa dieumee sii yawe naagnou liguéyaale euleuke moo gueune baamelle leundeumnaa tée khaatenaa koone gnoukaayee fatalikou tée bayii thiaakhaane

  13. DEUKHINE MBEUP

    a tous et a toutes les internautes , la prochaine fois quand vous entendiez qu, une personne est decedee , il faudra seulement prononcer la phrase suivante ( inaa lilahi waa inaa ilayhi radji oùn ) car li yoobou yooneent , dou fii baayi keneen !!!! allahou allam

  14. parizi

    Elle était souriante gentille ouverte et sympathique que dieu lui pardonne et l accueil dans son paradis repose en paix maty mbodj

  15. adama

    Yaw no no no loutakh cai pa vrai hana dou ay moroman rek nioy dem ci age yoyou nianalko mo gueun koumatal dem

    • no no no

      adama c'est juste k d foi ya de fausses information ki circulent juste pour creer du bruit tem yeuler rek defnagn ko bene mannequin..et pui reconnai que c'est tellement dure de voir quelq'un partir si jeune, pleine de vie. bilahi manoumako geume

      • Sajidaallah

        Li day wane ne de amoul khale amoul mak nieup lay djieul kouthi diamou woul yallah rek pertga,nay laine delou thi yallah bala mouy nieuw mome dee,yallah rek mo kham yalnako yallah yeurem,amine

  16. Madame thiam

    adiou mannequin yeup à âme lolen meti Ken khamoul kagne ak fane la yalla nala yalla djiegual maty kharela aldiana firdawssi amine

      • no no no

        j'y croyai pas..Yalla rek moy KARIM. Sunu borom bou manifesté woo rek nga khamni lep Mom la. ay way nite dou dara..yalla nako yalla yeureum kharé ko aldiana té atté ko ci yeurmeundem.yalla naniou khirtal ci bopam, yalla nako yalla bale yeureum ko té yeureum niou..c'est triste.je la connais pas mai dinako nianal.

  17. madame ndiaye

    li metina way adja diallo doi ètre efondré massa len mangui key dialé arame mbodj rakam ohhh dé dal métina

  18. belliza

    thiey sameu xarit bi…yalleu nalleu Allah bale te yeureum leu si barké Naby salah Lahoualeyhi wasalam

Comments are closed.