30 COMMENTAIRES
  • MACKY

    GNO GNO YAK SENEGAL ET ILS SE DISENT JOURNALISTES HAHAHAHAHA

    BENE EMISSION REK LAY SETANE TOUNKARA AVEC SENEGAL CAKANAM

    MAIS NEEK TIE TELEYI WEUY WEUYANE DOUL REK

  • ely

    sen tv doul rék ak orgonisé aéffairrou gorgjigéne c po bien pour l image de notre pays

  • birane ndour

    allé allé vous ki avez du temp defendez la tele de mon pere….. moi g d autre chat à fouetter

  • G

    Tfm dou sen morom thiot day kham lekam

  • coura

    tfm tfm tfm ba fadiar gno ko yoor kiy liguey ak kiy wakh yemou gnou resultat

  • iza

    yéne gneupe daguane di féne … niari télé mbalite leu .. fétie tiakhane rek…

  • Néné

    Matar affaire de guewel le reke….

  • leuza

    Merci Mactar

  • matar khaly

    Dans ce pays tout les fauteurs de troubles ont quelques choses en commun: lamine samba yerim Seck bethio Thioune idrissa Seck et je passe. Je n’ai rien contre eux mais les faits sont têtus . Cogitez

  • PATHE

    le probleme ce lamine samb il n se rien j n regard meme pa ce emission cet un faux type

  • cheikh

    sen tv bouniou sonale khamou niou dara ba paré di bari wakh ték bo khamni lamb ak grand théartre reck laniou khammmmmmmm tfm dou sene morrome

  • Néné

    mane dale la Sen tv me fait rire, comparer Sen tv ake TFm c comme comparer Youssou Ndour et Ouzin Bariguo, Sen tv xame lene sene bope xamoulene tousse, vos émissions st bidons, c pae manque de programme ke vs passez tt votre temps à redifuser….Thipiriiiiii

  • ithifo

    b1 ke lamine samba beurineu probleme mè mane sen tv doumako sètane prsk j’aime po leur manière de faire….tfm dou morome pomme dou moromou pome de terre…tfm rek

  • gorgorlou

    tout le problème est que TFM est plus professionnel,c’est tout.

  • SAMB

    KI DAFA BARI WAKH AFER BI DALE LENE LA KOU MANE DAGAYE DEF TEE BAYI WAKH DJI NA KOUNEE LIGUEYE SENEGAL DJEUME KANAME.COMEN KOU DEGOUL FRANCé SAKH NIOUKOYE DIEULE MANA WAKH REK TAKHNA KOU DIOUK NIOU DIEUL LA KHOLATELENE AFERYI NAK MO GUEUENE

  • tifa

    vraiment je ne comprend pas pourquoi on donne de l importance à cette imbècile de lamine samba moi il m ènerve comme c pas possible il se croit le plus grand reporter du monde hors c une impertinent ,c lui la tèle appartient à son pere qu on arrete ce hijo de puta une bonne fois

  • ABDOU

    FATOU TU AS RAISON POMME DOU MOROMOU NEW LA TFM EST LA TELE DES TELE ELLE SURPRENT TJR SES TELE DE BALIT

  • FATOU

    TFM MOKO YOOR SENTV BALITOU TELE LA REK KHAMOUGNOU DARA DAGNOUY BOUBO THIOOW REK IL VEUT TOUJOURS INSTALER LE BUZZ ALORS DEFAGOU GNOU DARA THII TELE

  • ROKHIYA

    NEKHOUL BA NEKHNA WA SENTV DAGNO YABATEé AMOUGNOU PROGRAMM BOU BAKH IL FONT K DE LA TRICHERIE

  • DARO

    TFM TFM TFM REK BA FADIAR

  • COURA

    c’est LA TFM QUI DERANGE MAI NOUS SERON TJR AU DEVANT PUISK DOU SEEN MOROM MOLEEN MEUNE EUPP LEEN PROGRAMM

  • rima

    seytané togual lamine samba yaye seytané pourquoi deux plateaux fii adounala lo guiss dafay diekh

  • coubakh

    wa sen tv warguéna kholate sén bopou dé vous voulez trop de détaille loucofi diarr

  • merimeri

    C’est les même problèmes kil y avaient avec wala tv yow la dou mane naniou kholat séne bop dara jarou fé niaw te guewel bakham moy jiko pousso lou wara niaw niou défar wassalam

  • maribou

    Lamine samba amoul béne classe

  • AHAHAH

    tamba is a bitch

  • adama

    tfm kiléndi yakhal si sén birla técniqcién yi la nék ilfo guén diémko kham sépiko c un corompu

  • astou diagne

    lolou mom deugeuleu

  • hake walkitabe

    walahi waxe nga deugue! vrai nafekheu cochon ou gros porc! ah oui c’est ça le Sénégal d’aujourd’hui! on favorise et donne de l’importance au plus nul et mauvaises influence pour la jeunesse edpoir de demain! c ‘ dommage! !!

  • kemo

    Je l’ai tjrs dit ce connard est dangereux pour le senegal.bahna daal

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *