Keur Gueye ak Koor gui – Epiode 25 du 14 Juillet 2015
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
beg naniou!!! oustaz
Wallahi yénafi meune nekhneu Machaallah Yalla nalene Yalla lafal thiate gnepp contane nagne suis triste k koor gui diekhna ba déwénati Inchaallah
amine! vréma c tro nekh mé koor gui moom bayil nonou rek mou dem dafar tar ben inS….
ZEUM lol waxnga deugg dh mais bon ngeunel leu kay nagn ko fekei ay deweni dewen rek
merci beaucoup seddal nguene khol yep
Merci
bima gueneu nekh ci episode yép machallah
Bravo bravo vrement man ngeen ligueni deef machaa allh
Ho waye doyoul dolli lène kèn naby
sama khol bi cedd na trop vraiment. YA RASSOULOULAH (PBUH) AMOUL MOROME yalla na ya ALLAH yokk lérame amine
oustaz Mbodj ma shaa ALLAH.. le groupe de gueye diadieuf way..
je veux un mari oustaz in shaa ALLAH.. un mari bo khamni dafa djangue alkhourane ma shaa ALLAH.. YALLA nagnou ko ya ALLAH may gnoune toutes les femmes qui veulent un mari comme ça
machallah
Il sapel mame abdou
ndeysaan li amna solo trop comme bou daw bi aussi pareil gayi ki moudié diangue comment il s'appelle svp?
moi jai meme pleure kéne dou yonete bi salalahou haleyehi wa salam
machah allah amna solo ken du nabi
Nooooo Vraiment mane gnii khawma nane laléni fayé rek gnomay rétanelo dima béglo dounde lénnnn way sama gayii nexna
SAMA waye you bou nkama dema hall si yalla you bou nkama si mouhamd rasoull llahi magui si peux bi
numéro 1
ماشاءالله الحمد لله الله اكبر
manchalla
Alaska
.
Dieul nguéne coupe bi
Nekhna lol barke Serigne touba
bilahi walahi talahi. Le prophète salahou haleyhi wa salam mo geun nieup. kouko geumoul pérte ga fi ak félé.
Tarikala amatina solou
machalh Way yalla na sen diamu yague rek
mashalah episode bo amna solo