PUBLICITÉ
aspt"

Inceste: sa femme violée par son grand frère, un militaire sénégalais se confie… Regardez

Un militaire sénégalais parti en mission pendant quelques temps, retrouve sa femme enceinte à son retour. Celle-ci a été violée par son grand-frère, dit-il. Il est prêt à tout pour se venger… Ecoutez Gfm

#Confidence #Inceste #Militaire #Viol

PUBLICITÉ

6 commentaire

  1. leuza

    Sa diabar day fénne Lolou dal malako wakh sa mak nak môme il é irresponsable

  2. BAZ

    ALLAHOU YAKHLAMOU YALA REK MO KHAM AK NIOM NIAR BOUL FAYOU BAYIL LEP CI LOXOY YALLA DINA ATE

  3. maty

    teude ak diabaram dou solution day gueuna yoke problem tégal lépe thi lokho yalla lépe dina lérre inchalla. metina trop mai souma sagnone do vengéwu.

  4. modou

    ki dafa dof bou ame lou mouye def nako def magame diabarou ma game nak yo name nekou sy lima sy khame nak diabarou magame bi dafa wara deme police bla dra khew

  5. CHEIKH

    MANE BOULL FAYOU SI DIABARAMK BOU NARE FAYOU REYALL SAMAKE DIOU DIOU LEPO MOM LAA WAYINAKE YALLA RABOUNAKODE SOUMADOUN YAWNAKE DINABAYII LEPOU SI LOKHALLA YALLA

  6. diaz

    frere d’arme noubli pa k si c dure seul les dure passe épui la solution c pa de tué kitte la femme et vi un otre vi oubli tt ca kel disparé de ta vie pr k tu puisse oublié c pa la fin du monde trouve une autre ki t’aidera a oublié