Publicité pour Mesri_Juillet
Publicité

Exclusif: nouveau single de Youssou Ndour "Djiguéne Gni".

Exclusif: nouveau single de Youssou Ndour « Djiguéne Gni ».

Youssou Ndour dévoile un nouveau single dédié aux femmes. Celui-ci intitulé « Dijiguéne Gni », appelle à la tolérance à la gente féminine.

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

43 commentaires

  1. mike

    linga dèff senegal mindèff dotoukoko fi dèff ya takh kèpp kouye way senegal gnèmè yaw grand you lincontournable tè ba lègui yangui si yonn bi g fè 19 pays europèen mè fo dèm nga ni senegal il t demande YOUSSOU NDOUR yalla ndanga goudou fane


  2. héy

    mais vous vous fuchez de nous ou koi di comparé you ek waly sa va pas non vous etes malade ou koi punaise.le seul le chanteur qui pouvait devenire comme you ou qui chante bien comme you c'etais ndongo lo pas d'autre


  3. toure

    wawaw sooko teguè ci dinè daga rèèr ndax ndax dinè mooy digeul nga tèral djiguen you ya dof dèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèèè


  4. trea

    nekh na lol me lima si derange moy fasse bi da gaw motakh divorse yi bari apre khale yi di takhawalou rek goor yi di len foye yalla bosi am dom il faut dieguene nie di mougne touti me bissimilay rek tass di takhawalou amoul gnerigne


  5. big big tune

    sétt ngua ko séét ni djikoom nékhoulaay ténkondjieguel mou dém sétti léén. baayiko mou démm.big big tune sa fait longtemps que youssou ndour ne chanter plus quelque choses d'interressant mais la la rien a dire merci grand you


  6. blacke

    NICE KHANA NEKHE MAIS TONTON DANGAYE TANGALATE REK DAMA BEUGEU NGUENE DEGLOUKO BOU BAKHE DINA AME SON BOUME LENE DIOKHE SI LIME WOYE IL FAUT ECOUTER ATTENTIVE MENT DINGUENE KHAME KADOU YI REK LA SOPIE MAIS INSSE BI MOME BODEGLO BOU BAKHE DINGA KHAME LIMALA WAKHE MES TONTON NICE PARSEKE JAIME MA MERE


  7. kheuch

    sd yawo dama yakar danga doof yossou ndour Ngaye teukeule ak Wally seck wakhou malla Wally seck me famille seckene la wakh yousou ndour moy séné baye thi way yawou way Ngaye diawale ak sambaye mbayane goooo


  8. Dof

    Dou chiekh modou kara ne nalene youssou dotoul way du npk geumolene ko li lancement la rek dieurediruf chiekh ahmadou kara mbacké noreyni


  9. toufa

    bilahi lou ler ga wax gor bouy dor ak di torokhol djiguene dou am mouk lou bakh mane limay wax damako kham diokhlene djiguene limou mom


Laisser un commentaire