Pour ses fans en guise de Ndeweneul, la grande diva de la musique sénégalaise annonce son retour avec un nouveau clip « Nitt dayy xam boppam » et Iris AV à la réalisation.
Exclusif: le nouveau clip de Titi « Nitt dayy xam boppam »

Pour ses fans en guise de Ndeweneul, la grande diva de la musique sénégalaise annonce son retour avec un nouveau clip « Nitt dayy xam boppam » et Iris AV à la réalisation.
Comments are closed.
Téléchargez notre application pour une expérience optimisée et pour recevoir les dernières nouvelles en temps réel.
nice ma cherie
Yaw dagua sokhor motakh gua toudé sa bopp pobar kholal titi môme bagn bagn beugue rèk
Vous êtes ses fans? Je pense pas. Vous lui auriez dit la vérité ! Son texte est pauvre. Le morceau mal arrangé. Elle est simple ? Pourquoi elle a besoin de nous montrer son tas de chaussures bon marché? Quel est le scénario du clip? Qu'est-ce que vous appelez clip relax sans pression ? Un travail désordonné alambiqué et insensé. Elle a du talent c'est sur mais elle n'est pas professionnelle du tout. Elle s'est laissée manipuler par bougane qui l'a utilisée dans une guerre dont il est loin d'avoir les moyens.
Very nice les jaloux vont maigrir. Bonne continuation!!!!!
TITI AMOUL MOROUM
On s en fou de Princ art EVE l essentiel est qu elle aille de l avant sans ou avec princ art voleur
EVE yaw defal ni titi ba gneup hamela c mieu ken hamoula liguay bonne sohor ignane li dafa nehhhh nice borome hol bou rafet rek mokoy guice way ya bonne way prince art day liguey titi di liguey amena diom ba demal bopam alor louguen beugue mou rame dilen sarahou way EVE demaL OUTI NI MOME WAY
titi oie dal diam rek ngay âme Inchallah do boromou béne xalé
Votre commentaire boul degueulou boule fallee liguegnale reck waâw very nice relax happy non stresss la simplicite j adore
nice nice nice
belle voix mais un texte vide
wooplaw, kii tibou thieeb-bi diar-na 3 milliards
Li dara fayouko xalé bi machala nekhna nice na trop sakh
Nexna torop merci titi
Merci titi nexna torop
masha Allah nekhna
C'est la meilleure de tous. Bayilen di diakhasse ay niit foumou tolou nii lokho prince art mogui si.
Titi ak you demb la wone. Kou mere bokooo
amo bene classe
titi comme kou weroule soof nama trop
dó sene morom yalen man fouf ndakh sa khôl bou rafet kén degoula sillou niaw. ……
wawaw clip zéro stress sans complexe naturel défouler ambiance titi nous étale sa vrai nature c trop nice je ve ossi kel clip mame saliou djikko et rassoul snt lé meillleur titre du nouvel album live
nekhna torope g vraiment aimé
beaucoups de danseurs
eve nite daguaye mandou. ki elle fait sa carriere prince art ou pas elle est entrain de perser. bravo titi boul deglou nite dagnou sokor
Woooooouuuuuhhhhhhh very nice vraiment, clip bu relax sans pression… Titi mes encouragements
C vraimen nice, clip diayy preakk deugg, tré relaxx et naturel, sans pression… JAI BEAUCOUP AIME
machallah koula bagne yalna deuk ci tollou yambeu clip bi noce na son bi nekh kene doula fay prince art ci douniou dara fi yalla fi nek ak ligueyou ndeye aka ngay dem sakh…
Titi nekh guama lol ndakh gueme bigua gueme sa boope guemni loudoul yalla neuleu gueme sa yaye gueme liguay def té meune KO Boole tek ak teeyi ham sa boope kom ni gua KO wahe té fi gua tek sa tanke boko teguiwoul sa none dou la rée té boul fateni fi gua diougue sa guathie lagnoui har guisse gua tione foumou moudier té loho youssou ndour mougui si saf SAP té mougui melni kou yeguoul li hew prince arts d'où yalla d'où yonentie KO yakar yalla la yakar du courage titi
Titi nekh guama lol ndakh Dagua gueme sa bope guemni loudoul yalla neenleu gueme sa yaye té meune li guaye def Boole si teek ak teeyi ham sa boope kome ni gua KO waye té fi gua tek sa tanke boko teguiwoul sa noone d'où la rée té boul fateni fi gua diougue sa guathie rek la gnouye khar guisse thione foumou moudie te loho youssou ndour mougui si saf sap te mougui melni hamoul lou hew prince arts d'où yalla d'où yonenti
c ke jaime l plus sii clip bi c sa simplicité kel montre aux gens en plus dan la vie il faux savwr partir tout seul boul kar kéne kan tu sort un album tout monde apreci c manifik
machalla nekhna trop louma nekh si yaw daga guemsa bop nilarek coufatelecou sokhore
c est toi eve la folle pas titi ak prince art la vie passe
nekhna trop sama dak lougui boule mousa delou
nekhna trop nila sama dak lep boule mousa delou
Masha Allah Titi
Vraiment nekhna trop
titi c très nekh yafi meune yafi nek clip bi Nice n'a lolll
bayiléne diambour wa prince art danouy liguey titi di liguey yéne wa sénégal da nguéne complexé xaliss wa prince art danou ram ba aksi titi aussi dafay ram ba ague fate nguéne gnou way
Eve tu es mechante. Apres youssou ndour TITI a la plus belle voix au Senegal! c pourquoi elle sera toujours au top. Touches pas a TITI! On attends l'album avec impatience. Boul faller.
C tr nékh way machala koula bagn yalla na dééé yafi Mane do séne morome
tu es en retard ma cher deloul fanga dioguee wone
nice na TITI…waw waw…Happy begger time….
yaw tu es méchant yague yague titi wa prince dinagneko weuri elle la du talent té meuna loumouye déf té fi nak kou sokhor boko
cette fille est vraiment folle. elle fait tout ce bruit pour montrer a Princearts qu'elle n'est pas malheureuse. Princearts moom, faténagnoula bou yague