27 COMMENTAIRES
  • bill

    secoue la toile ?

  • VÉRITÉ

    NOUY DEFF YEUFOU GOOR WAY SUMA GARS YI ÉVITÉ DAGASSANTÉ

  • VÉRITÉ

    LES REPONDEURS DE SONKO DJIGUENE SAKH DANGENE DII TESSANTÉ AKK MOM KI DJIGUENE LEU NGENE NEKK FII MELNI AY DEUMB YOU GUISS YAPP!!! DANGENE SONEU NAKK

  • Cheikh Seck

    FOUTEZ NOUS LA PAIX AVEC CETTE FILLE SANS SCRUPULES ET EXTIRPER LE SURNOM DE RASSOUL

  • rassoul

    warone guenn roussa dendalê tourou yonent bi psl si app jiggen bou niakk pudeur suturaloul bopam khaloul dhé

  • i s

    thimmmm degualasse

  • Dakar

    Encore une faussaire, artificielle qu’elle soit !
    Dégueulasse…

  • Cheikh Seck

    EXTIRPER LE SURNOM RASSOUL

  • Amar Mben

    yan Sénégal gamoulen dara ki limou yok ci touramvi suko nourouwot ab joulit warouko sakh di wone yena dakha saga rassoul tou bouko ab toubab defe nguen di wakh rek aka manifeste ay veré nafekh nguen yen niiy wone ndawsi di ci yak rassoul
    والعياذباالله

  • dieng

    nous sommes senegalais et musulmans arrêtons d’encourager les filles à se dénuder en leurs offrant des articles. voila pourquoi il ya de moins en moins de mariage

    • Djibson

      Comme si les femmes étaient seules responsables que mou am de moins en moins de mariages.

  • rené Diagne

    vraiment c est pas une information..

  • Jules

    Primo toile bi louko secoué yobe n’a lol pour wa senego secondo tank you mèleni you diargongne Amazonie gène gnouy sonal sof gène trop

  • zzoil

    Boulen niou sonal ak diague yi way ki amoul lén loumouy apportél un Sénégalais Lamda. Yén Journalistes yi, il est tant guen di poser wou les bonnes questions à savoir si réélement contenu bignouy partagé warna apporté quelques choses dans la mentalité des Sénégalais; Du moment que apporté wougnou dara diaroul partagé. Elle a des snapchat ou insta limouy partagé na yém fofou et ceux qui sont intéressé dam abonné si ay comptam. Wa Salam

    • Djibson

      Justement ci compte am la ko publié. Senego moo ko partagé . Lii dou info tout comme 90 pour cent des publications de Senego.

  • Maimouna

    On ne voit pas ce qui peut faire rêver dans ces images… elles suscitent davantage le dégoût et la répulsion.
    Ah, la vanité, l’orgueil, l’auto-satisfaction. Haram !

    • dieng

      vraiment

  • Mort dans l'âme

    Sénégal, pays de la promotion de la prostitution.

    • dieng

      merci beaucoup cest vrai

  • jiguene

    Internet bi. Bilay dinala lene dofeloo rek. Kii moom kene hamoule loumouy defni. On dirait dafa dof. Demelene seuyi taa bayi thiahaane yi. Jiguene day am touti kersa. En plus SENEGO kii dou informations. Dou golo bou jok rek ngene woneko. May wah gnounane ay jambe. Mouy melenii chameau

  • Ziggy

    Ki Bond lo khana da miope, mounane jambe de reve

    • Djibson

      Des goûts et des couleurs…

  • Al akhe

    Demal seuyyi te bayyi sa thiakhane yi

    • Djibson

      Sou bougoul est nak? Lou ci sa yoon ci seyam?

  • Mamad

    Sénégal dou dem

  • Lima

    Respectez vos lecteurs. Montrez-nous des femmes qui créent des emplois et autres

    • balde

      merci trés bien dit

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *