Découvrez le nouveau single de Carlou D feat Gaston et Djiby Da Brains « Sagne Sagne »

« Sagne Sagne » est le nouveau single du célèbre chanteur Carlou D en featuring avec les rappeurs Gaston et Djiby Dabrains. Un morceau sur lequel l’artiste rend hommage au guide du mouridisme.
Thioo mach Allah
bombe clate thieuy way baye fall clip bi lay khar
Macha Allah a chak foi kil chante Cheikh Ahmadou Bamba c fort,
CARLOU BOKOUTHI WAYE KI DOU SEN MOROM
Beug nala bilahi lo deff mou nekh ndakh kou tedd kingaye bagueeee
TRES BON SON MUSICALEMENT. MAIS POURQUOI SENEGAL DINE DJI GAS YI DIAPER KO AFFAIRE DE EGOTRIP BATTLE KOUNEK DI BAKK SA MBEUR. REUY SERIGNE DEH REUYI DIEUF MOKO GUEUNEU WOOR; DIAMOU YALLA BAYI SERIGNE SI YALLA JUGER WAL BOPAM MO GUEUN WEUR DI BAKOU !
nice baye fall son bi nekh na avec le ritme on kiff
Maa Shaa Allah dafa meune loumouy df
Niekh na si kaw si kanam bay fall
carlou yay bandii
serigne touba rekk mofi nekke
dieureudieuf serigne touba merci carloudi
dieureudieuf Serigne Touba carlou yalnala serigne bi feyal bopam amiine sa kaw sa kanam rek inchalla j t ador
nice na…il est original Carlou D……
diadieuff waye baye fall yep contanagnou si yawe carlou di yaguale waye fall
bravo nekh na
ma cha allah juerejuef bay fall
Quand on est mort on se rend pas compte et c'est pour les autres que c'est dur. Quand on est CON c'est pareil ! Quelle bêtise de la part d'un soit disant waykat malén yeureume oh kane moy s touba foumou tothie toklén way eupeul bakhoul
Navet,archi nul,tout le monde a ses convictions,on en a rien a foutre,toi tu dis touba seugn amoul morom,l'autre dira seugn babacar amoul morom,un autre limamoulaye amoul morom,un autre baye niass amoul morom etc etc,ça ne finit pas et ça ne fait pas avancer la société,il faut chanter sur ce qui unit les gens par sur des convictions personnelles. le fanatisme religieux est a l'origine de toutes les guerres,le fanatisme est pire que l’athéisme. revois ta copie carlou d,ce tube c'est vraiment carlou navet
Carlou d Respect man li nga wakh rék mo worr
YALLA daal kounek warnga diangué thi mom mandou, nakhh beuss bounek noit diko mooy té réyou ko, wagni woul lén thi loumou key diokh thi teranga aduna. Demal amerique, europe, asie. Gni di diaamou ay bante, gni di ay framacon, gnii deuk thi ndialoo yok thi sakh nak am nioukey filmé diko diay. Leep Mom Sougnou Borom mou mandou rek. Kou deh ak sa bamel té kounek dinga wét ak sa Borom kone nak naniou rafet ndiort thi gneup té khamni Yalla louko nekh lay def. Niit nek na thi aduna di def lou bakh ba deh fek wax louko woroul ak sokhor mokey yobou safaan, niit nek deuké na bakar ba déh fek mandou ak yéné nieup diam moko yobou adiana.
Aldiana akaa yatou Ndeysan nieup kadj naniou thi. Kone naniouy rafet ndiort tey mandou.
Lakoum dinoukoum waliya diini.
Jaangen dieuf
Done thi yokh rk nii nioune mouride Serigne Touba laniou am. Aduna diafé woul na kounek geum linga geum té mandou thi lo khamoul. Jaangen dieuf
mbockou talibeyi manguileni gnane am na wakh yokham ni bouthie kene commentaire loloulagnie woute yalla sakh dagne koy togne tedou repondre condiarouko
ca kaw ca kanam baay faal nice na lol
ya wakh deg carlo