Décès de Madame Adja Marietou Fall, Mére de notre regretté chanteur Ndongo Lo. Ainsi ce matin du 10 Mai 2014 Adja Marietou a rejoint Ndongo Lo dans l’au delà. Elle décédée 10 ans après le rappel à Dieu de son fils. Toute l’équipe de senego présente ses condoléances a sa famille, et qu’Allah soubhana wa talla l’accueille au Paradis éternel.
Information envoyée par Modou Dieye
yalanako yala yereumm amine
yalla nako yala yeremmm amine
yala nako yala khare aldiana paska mo diapalè sama xarite ndongo lo wanetè dioulith daye nagou dogale
YAYE BOYE YALLANALA BOLLé yow ak sa domme yep dougale adiana,amine
yalnako borombi kharéko aldiana té yalla djissé domom ndongo lo cii aldiana firdawsa
amin yalla na ko yalla khare adjana
que dieu l accueil au paradit
Amine si barke serigne fallou mou ndongo lo
amine waye yalla na yalla nagnou naine yepp sy barque seye di na moukhamet
firdawsy demeure eternelle
Que la terre de touba lui soit legere
Yala nako yala yeureum té yobeuko aldiana
amine li moy adouna demale magui gnow que laterre de touba lui sera legere thie barke serigne fallou mbacke wonelek domame bi k sopone lole
Yalna ko Yalla yeureum Té kharéko aldiana firdaws AK mbolèm dioulite Té yèkhè Niou.
yalla nako yalla khare aldiana ak bep dioulite boufa nek
que la terre de touba lui soit légére
yal.nako.yala.yeureum.b.s.fallou
animo yala nako yalla kharr adiana si barcke serigne Fallou mbacke
Ayy wayy yalla nako yalla yeurem té yekhégnou
Amine ci niane you bakh yi
Yalla nako yala yereum té kharéko aldiana
yalla nako hare adjiana
yalla nako yalla kharé aldiana ta tassékok doomam ndongo niang
amine
Qu’Allah accueille tous nos morts au paradis pour le bonheur éternel. Amine ! ! !
Amene………….
amine thieye yalla
hokhooo yalna nako yalla tasselak domame ndongo lo thi adianay firdawsi ya
yalla nako yalla khare aldiana
ndeye sane yalla nako yalla khare aldiana
Yalnako halla yeureum