30 COMMENTAIRES
  • Weuz

    Mané You falewoul Sting dafa geum bopam

  • SY

    TU ES FAN DE STING LE GRAND STING IL EST PLUS ECOUTE

  • SY

    TU ES FAN DE STING C EST TA REFERENCE LE GRAND STING

  • laye

    youssou ndour donc tu confirm que tu est plus satanic que sting …parceque la musique est un instrument de satan….

  • Tange

    Ki moy sounou fierté nationale et internationale

  • Medoune

    La star des stars big up man

  • Djibson

    Non mais grand yangui tangal kholou Thione euros

  • Oumya

    En tout cas koussi beug avancé neu roy si moom bilay je parle pas parce que je suis fan mais deug rek la wakh

  • tallawally

    noo youssou vraiment amul morom boudoul dara mom day inversir si deukme
    mo takh mou nekhma

  • Bijou

    Vivement le 28 Mars 2017 à bordeaux ak la star planétaire rek dou fo way

  • yaye Fatou konate

    bilahi mala geum diom ak foula guissi papa youssou loumou songue dann ko koula bagn dou noyi ndax yaye oxygne love youssou ndour

  • Dudu

    Barké Serigne touba maleu beug

  • Fifi gaye

    Merci Papa le monde t’admire tu es une référence pour toute génération confondue

  • Tis

    Macha allah Ndour lolou kham nagnou ko

  • as

    yaw tu nous amerde demal djamou yalla

  • TIMA

    KOUY LECHER CUL JAMBOUR MOY XAMER KOU KOY DEF AUCUNE CLASSE YOUSSOU DE MOM MOUGUI FEHER NOUMOUY TEXER AVEC OU SANS POLITIQUE LA YAMALER

  • ss

    Nit dangay xam sa moroom .
    Sting n est en aucun cas l egal de you .
    Ce que Sting a fait dans la musique, 100 ans ne suffisent pas à you pour le ratrapper

  • Ive

    Il n’a plus aucune classe depuis qu’il est devenu politique ;il ne compte que sur ces lécheurs de culs pour exister ; Niak fayda

  • AIDA CHAMPAGNE

    AH AH AH !!!! Non mais il a volé le champagne de AIDA ou quoi ? J hallucine quand je lis des enfants de ratés qui , en rajoutent une couche ! Dem len fan sen baye yi , té bayi nek ci net bi di doul comme Youssou miy concours niak fayda ak fenn ak El hadj Diouf ! Légui You nekk fi Mikael Jackson , El Hadj nekk fi Pelé ! Tchimmm guewel ak domou ….. , dou niou rouss sakh !

  • tima

    LOUMA FI WAX RPETITION LAY DONE MANE NAKOY DJISS REK DI BEG DIKO NIANAL

  • ndour

    Papa Ndour yalna yalla yokal niou dix you mlni yeuw bax nga meun liguey beug senegal tek sa dool fi si senegal saay mbok,ay domou diambour,etc di si jarinio.Merci du fond du coeur

  • doudou wade

    youssou ndour bokou si da ka si boler amoul morom

  • loulou fonseca

    Grand You respect tu es le seul artistes aux monde je pèse bien mes mots qui a chanter ? sur quasi toutes les music du monde (reggae,pop musique,zouk music,salsa,électronique,dance hall,variété française,acoustique ,slows,jazz,rap music,R’n’b,mbalakh,music traditionnelle,music arabe,music classic.la samba.thiey bi grand le pire c que chaque music du monde il la sorti un album entiers.que dire nak des duo que dire nak dans les places qu’il jouer dans le monde les plus grand festivals du monde le seul africain qui a jouer a New York City en plein air in time square new York.respect a toi dossénn morom.ded festival comme rototom en 1989 ,en 2009 j’en passe.est si je vois on le compare avec le jeune waly seck mdrr vous êtes malades c pas youss zk waly mais c you ak thione seck? yobouko bercy?? pour la première fois.on doit parler de waly ak birane parce que birane patron le bayam dafa riche mais le jeune birane est très humble timide respectueux est pourtant il pouvait faire se qu’il veut vus que il a de l’argent .�

  • lolo

    Youssou Ndour has the best voice in Africa

  • vivi

    Youssou amoul moromm birr afrique way

  • tagg

    Youssou sa difference avec n’importe quelle artiste c’est qu’il est un homme de principe qui defend ses origines et qui croit en lui, il a confiance a ses talents et n’est pas imposable au contraire c’est lui qui met ses régles mashalla ndour iow nieup guissi guinaw bilay

  • fifi

    Koula bagne yalna kheuy rek fa ngeh

  • robert

    Diadieuf la star planétaire bilay do moromou Sting

  • dada

    Bilay yaw do moromou khalé

  • alima

    degeula ndour amo morom yalene meune

Les commentaires sont fermés.