Audio-La femme accusée de voleuse de talibé raconte son sale temps au rond point Case-bi
Amadou SY
7 COMMENTAIRES
didija
26/08/2015 à à 23:06
Man dal tite na lol si Senegal nite bouy Wakh degue mo diafé legui, nite bouy def nguir yalla ba nite yi dila sosal lo defoul vraiment diaratouko, man mi dee khawma kan mé souma naraté sarakh talibé yi, "doumako def" ma sarakh wa diaque yi wala ma rarakhé sama khalé kogne, wasalam
wakhouma lolou yeupp guisse gua les talibè il son telmen impolie que c pas possible c meme pa lapeine de les donner les talibè ne son plu comm ils etè. kerok beneu talibè damaniko sarakh ba yeguena mpunè ma sarakhe dou yègue sarakh c pour toujour taigal mathi ak sa oto bou bonne tè je lui est rien fai dotouma sarakh talibê
Les talibes d aujordhui sont telment impoli que tu ne peux meme pas comprendre… Mere bi mome domeram rek leu
mais natou souy nieuw mome kèneu dou kham…
Senegal Moy réw bo khamni amoul yone mm soudé ndaw si sax dafa beug sathieu khalei dou nonou lagnou waron def di yak auto wam c pas joli Senegal nagnou ame yar khalei bou ame 15Ans kéne mounouko sathieu sax ndaw si limou wax and na ak mom Mo wax deug goor gnako done door mom dagno bne djiguéne dague koy soutoural mane dei beug naa sama Yaye Ba douma def djiguéne loudoul louko nex

sénégalé daye deugue teul né dame na dougnou cherché méme pas à comprendre khalé bou djiguéne limou wakh mo gueuna yanou mané té niro nak kou degou
sokore reck mon léne diape c tout
Non vraiment sister massha. Les gens tamiteu nagnou manou. Mère yaweu tamiteu