Mouride sadikh j’ai les larmes aux yeux bilahi ya bakh mame maodo yalla nagnou ko yalla fayal si barkel seydina mouhamed psl
lamine
dieureudieuf MAME EL HADJI MAODO MALICK SY (RTA)
massouka Mbaye
Mame Maodo Malick Sy ( RTA) keen dou mom.
tima
Mame fa wade welle yaye maodo aram lo coumba thiam may penda pathe bougouma
007
Macha halla
mourid sadikh guame serigne bamba
boungén guisse ma wakh li yepou nk Moy niou kou dokhé nenéne sa dokhinou bopou la Wayé sounouy serigne nilanou dokhalan tée ba diogué fi tay cheikh sidy moukhtar ak cheikh ahmad Tidjan sy ak mbolem khafay tarikha yaw koci guisse defkoni cheikh sidy moukhtar yaw Tidjan bi bi defko ni sa kilifa gua t khamné ngoci man yakho wayé dou nioume ndakh ningouy dokhé rk Moy ndigale li t ndiguale diafé rk laci kham ngéne balma ci wakh dji koum dérange lou bakh rk laci dioublou Yalla nangou Yalla samou ta samalngou soun kilifa you bakh yi
khalil sy
cheikh seydi hadji malick sy est le cousin incontesté de cheikh ahmad bamba;tous deux originaires du fouta de cheikh omar al foutiyou et fervents défenseurs de l’islam.
Ils ne croient qu’en Dieu et n’ont comme référence que le prophéte Mouhamad (psl).
Wa salam.
mourid sadikh guame serigne bamba
ay mbockou talibé yi bouléne ma guarame ki bouma wakhoule lou bakh ci mome loumay wakh ? ko khamné Yalla guarame nako yonente (psl) guarame ko cheikh omar fotiyou guarame ko ak mbolem cheikh ahmadou bamba guarame ko mbolem mak ngici réwmi nangoulko liko Yalla def semple man sou touty cii rk Awma loumakoy yockou ak loumakoy wangi wayé wakh ci barkélou Thi ndakh samay touyaba yacké ci motakh may wakh Khana wakh sama mbockou talibé yi niou khamné tarikha douniou ay none Danio bockou louniouy woute ak foune dieme tayite ni ch.sidy moukhtar di def ak limouy wakh ni lako mbolem khafay serigne touba dane dokhoule tamblé ko cheikh sidy el malick ak sa.bamba louné sekhnanko ci lou raféte serigne babacar ak cheikh moustapha 1er Khalifa nonou lafa démé wone cheikh mouhamad fadale 2em Khalifa ak serigne babacar nonou lafa demé wone serigne Massamba frère de ch ah bamba mo guénone neck kharite ci serigne babacar kouné sakh ci niome niare defna ay bayite mana ay weye you daw yerame sa morome ancore el abdou aziz ak serigne fallou ak serigne abdou ahade ak serigne abdou khadir ak serigne saliou guisse ngéne niomou melone ba Yalla def serigne bara fallou guisse ngéne nimou dialé wone tanckame founé ci bire réwmi mou teck kofa ndakh di némékou l’islam bi ndakh séne yaf t nioko wara bay momitam mou def com bayame yako djitou cheikh sidy moukhtar yalnako Yalla yaguale fi soun kanam ngew yockou lepou mou guéna rafete Naka nonou ch abdou lahi niass mêlone ak ch s.bamba b.niass s.fallou s.bassirou
seny
Cher frère le Sénégal nous apartien on n’a eu la chance d’avoir des waly you donc pourquoi les divisée à cause des confréries
nd michel
sant nanou migui melna fekenanouko
Xell Xelli
J’ai pas l’habitude de commenter mais il faut ma wax ci Commentaire mourid saadikh bi.Su taalibé yepp amoon sa guiss guiss xeeweul yi daa gnu gueun baawaan.Sunu Maam yu tedd yi (Elhadj Omar, Cheikh Ahmadou Bamba, elhadji Malick,Baaye Niass, Maam Laye …) jamm rek lanu sékhoon.Lu tax taalibé yi di jaxassé.Gnepp xamnagnu ni Serigne Sidy Makhtar bariwul lumuy wax waayé su waarè wax ci tariikha yi mooy waxal boppam.Cela démontre son attachement à l’unité des confrèrie.Je suis taalibé cheikh mais kuko sopp laa.
ndeyakhalifaababacarsymalick
cheikh seydil hadji malick maodo,mame maodo kou andakh mome dou dééss ganaw yalla naniou ko yalla fayal si barké seydina mouhamed (psl) akh si barké cheikhna ahmed tidiane chérif (rta)
musilman
Sawaye nit daye am hay tegin yaw de mourid kou amteginga
nnnnnnn
aminnnnnnnnnn
nnnnnnn
koubakh
hamidou diaw
mawdo lanou gaum
fatou traore
talibe cheikh rek
Beye
Mame maodo Yala naniou ko Yala fayale
coucouniang@gmail.com
merci mouride sadekh si tout le monde le comprendais comme ca probleme de tarikha dou moussa ame
barkina ly
yalla naniou yalla fayal mame seydi hadji malick sy
Papouné
machallah mame maodo
абдулай
Amennnn
mourid sadikh guame serigne bamba
yalna Yalla yockou lérame ta fayalniouko diamoube Yalla bouko diamou t diamou louko Moy ki sopone ab yonetame t yamalé wounko wone ak dara mo takhite Yalla faynako ko ci guamou gui t guisse ngéne ko nanou ci kii ak niou melné niome t bayyi xirro ak diakhasso s.bamba d lolou rk moko niorone ci diné dji ak saydi el malick ak mbolem mag niou bakh ngici réwmi Yalla Yalla tek ci li ngi neckone ba tassaléwate niou ak niome aldjana niou fécké guamou ay ate you bari ci barkeb mouhamd (psl)
diaw
Yalla na nite yeup ame khel mou rafété ni sa boss. Machalla
chacha
kene dou maodo malick
sow
thiey mame maodo mala sope té beugue la bamou dieh
Comments are closed.
Ne manquez aucune actualité !
Téléchargez notre application pour une expérience optimisée et pour recevoir les dernières nouvelles en temps réel.