34 COMMENTAIRES
  • adji coumba tako

    thiey yalla lii eupna

  • drizzy122

    eske la photo de gauche es 2014??

    • Khoott Gherte

      Ta pas regarder la tele hier petit con

  • diong

    mayemeremakguawaye

  • Guisguis

    Hey khelmé dal rek.khaliss d’affa nekh.mais je blâme le khessal quand même le reste rien a dire drianké le

  • zelko

    Elle a farcie han

  • drake killah

    thiey mėre bi kėne dou ko wakh deugg adouna rk la gueum

  • hams

    Ah madame vraiment vous êtier grave belle en 2010 la vérité mdr ???

  • marthia

    dafa gnewe you extravagant te osi yen pata yi bakhoul ci sa sante foto bou ndiekbi formidable

  • Ba Alassane

    diabarou awvoqa la

  • masafi

    euyyy tataaaaa degeune aadadda

  • Loum

    adouna ni la sou xalisse gneuwe diouxamko sI ygaw moye gone

  • fatu

    Love you deguene point

  • mina

    Nit kou nekk avancé guay niane yalla senegalais kouy dem rrk gneup beug la tè

  • coumba

    Liii eupneu el se makill trop et sa la va pa du tt el es plus belle kan el en met pa trop

  • daso

    cette femme est trop artificiel

  • Néné

    Ayez peur d’Allah, Deguene Chimere waxoulene, defoulene,.li nguene di wakhe si mome lou bone thieupe si yene laye keupou, tei mooye dakoye niokol aye barayas reke…Evitez la medisance mo gueuna bone sakhe Adultere 09 fois, entamons cette nvelle année et demander à Allah de ns pardonner, manie niou moudie bou rafete…Balene ma ake, Balnalene…

  • verite

    no mais deguene je suis dsl mé draqueen rek guéy nourol trop de maquillage

  • monia

    javoue k ta foto d 2010 è plus bel mai yaram keneu manou ko té tu pe suivr tous les rgim du mond mai sa n done pa gran chose j c k yaram bi nékhou ko ndakh yaram bou bari rafetoul mai manoussi dara.tata deguene on taim com tu es et respect tes choix.mes encouragements.peace and love

  • zal

    Mani ki dafa amoul kouka wax deugue rek

  • valencia

    Hahahahahaha merbi com poupe quoi .

  • abdoumbodj

    Elle était plus belle en 2010 qu’en 2014 et les enfants que vont ils faire apres toi tu as des fans qui ne savent quoi faire dans ce bas Monde avec ce maquillage,

    La forme vers les pieds c comment lollllllllllllllllllllll

  • mia

    tata ya tay bouniou sagnol sen yaye melni ioe machalla

  • Diarra

    degueune babou un peu de régime et sa ira mieux

  • ndeye.basse

    Maneu dall sénégal critique rék ah montakhit daniy delou ginaw rék c normal kou djeum mak Sanger 000 faut ta dégeun thi kaw thi kanam

    • abdoumbodj

      Ki djem ci mak, wara def affairou mak, maquillage bi mtre Babou rek le nekh, defal regime un peu faute de quoi tu aura du mal à respirer au lit et la chaleur de minuit wa salam rek la wakh.

  • valencia

    gouy gui chimér

  • aminata diop

    machalla tata deguene silwicè ci nitt la dioguama beugue sangnesè rafete kou sokhor bokoul

  • anna

    Nguene balma,deguen bou ko nekhe solou,maquille, dara nekoussi,mais nak santem cii la.yaram bou barre bakhoul.As grande soeur est partie subitement d une hypertension.Hal na yallah yeurem.khamon na ko bou bakh..yal na ko yallah yonne djamm ak werr.yonne niou ko amin.wassalam

  • pom

    machalah

  • bj

    moi je peux pas croire toujours quelle est adjiratou dafa yap niit yii beugue deef khalé bopap

  • marie derwiche

    très belle

  • Rokhadya

    tata deguene Machallah lawla thiate. Reference bou maque gua et tu y restera pour toujours. khawmala mais koula khoole khamni sa khole dafa raffete. yaw koula khole khamni lou niaw meuno qua wakhe ci kene. Yalnala yalla defal diam ak mboleme dioulite. je T’AIME FORT TATA DEGUENE.

  • fimatou

    je prefere celle a gauche

Publiez un commentaire