81 COMMENTAIRES
  • Coum

    Sen toune nekousi

  • Laissa

    Menone na déf tatinéne béne yo
    ne sa robe ne cache méle pa cé parti intime na nék mak waye

  • mayi

    je supporte pas cette fille tout ce qu'elle sait faire c'est montré son cul elle était beaucoup plus douce à l'époque avec youssou ndour mais maintenant rien à voir et je trouve qu'elle n'est pas naturelle moi personnellement j'arrive pas à la cernée elle donne pas un bon exemple en tant que célébrité les vraies chanteuses sont la en pagaille elle chante jusqu'à tu pleure sans se dénuder quand je la vois au grand théâtre habillée comme elle sait faire alors que y a des femmes qui sont la avec leurs maris c'est irrespectueux je comprends pas elle n'a qu'à aller faire carrière aux états unis la ou personne la jugera sur son comportement nous on est des musulmans et fier de l'être. serigne saliou va se retourner dans sa tombe en te voyant avec cette tenue. alors que je suis persuadée que tu peux faire mieux par ce que tu as l'air adorable. mais sois toi même. nitt Day kham bopam Salam.

  • boy Nice

    Une artiste doit donnée une très bonne exemple

  • Aicha diop

    ki loumou Sol Dara bakhoussi viviane dagua am ayyy domm tes legui gua nek grand mere

  • ousmane soumare

    day léralle beute sakh nakk happi laniou wakh dama sakh nam Sénégal ndakh vivi

  • amady

    khana mom toudoulwon mame diara wala ki gemoul dara

  • diaby

    ce pas normal de monter cette photo

  • Mouhamet Soumare

    she wanna live forever young!!!

  • famita

    li robe la wala slip

  • hamadou

    li bagull ti star Kom viviyane soll bii darra baguti

  • mami@

    si chacun pouvait occuper de son cul la vie serait génial
    ngéne balma akk

  • deuk bi

    mane daal khawma mak la khawma khaléla wayè mool na

  • miss bou rafete

    no li mo nekh rek commentaire yi daguey reer bah tass sama bir bi mougui meti

  • roviano

    je sais pas quoi dir

  • dij

    Lima guen mèti moy sa dernière chason ki rime pa avc sa fason d vivre baga khaméni dagakoy woy baparé mé sa te fé rien iao diaratoul sakh gnou lay considèré li dafa eup dé lén préservé image bou bakh gnanoumako yala légui mé bofi kan u sera morte ya ke c image ki figurerons sr ts lé internautes diapci ta ds enfants dièm lén métr es le droit chemin moguen ga top sa nassou bacane ha masta way

  • Gorgeous

    I don't care how old she is, she looks very very sexy and gorgeous!! You go girl!!

  • la classe

    wow super nice tu une vrai star anna gni done wakh day montè hanche doul rèk ak jalousie

  • teranga

    vraiment Viviane ne reflaichi pas du tout on dirait qu'elle n'a pas d'enfant ???

  • to

    Yay bandit deei..say cuisse Reik non doyoul baye desss

  • madiba

    Non ce n'est pas un slip ce sont ses poils!!!!

    • ma tay ndayam

      sa poils lou ndaye ak sa baye yaw madiba

  • to

    Deffeul lula nekh tu est une star.il faut que les gens fassent maintenant la différence entre un artiste et un personne ordinaire. L'artiste doit tout faire pour émerveillé son public et c'est son rôle. Viviane a compris ça et je pense que la tenue n'est pas aussi diabolique parce qu'on a vu pire hein.Fait ton job Viviane et fonce la reine

  • vivi ya nekh

    slip bou Noire la sol viviane ya nekh ak sa tatte you bakh

  • nope vivi

    hooo viviane souma amone bèn goudi douma wakh dara… warguà nèkh waguà saf sap…. Bouba dafa doff liiiiii kouko wakh khammm

  • passant

    Waa nangou arwatam ,mé c vrai ki wax bou done ray dééna bou yagg

  • NIT DOFF KILLER ?

    mdrrt

  • Amy

    En tout cas elle fait des jalouses profites bien ma chérie la vie est trop courte kou mer boko

  • xoss

    Qu'on se dise la vérité ça c'est pas bon une mere de famille qui a 40 ans et plus ne devrait pas se comporter de cette. comment vont apprecier ses enfants cette tenue? rappellez vous que nous ne sommes pas des toubabs nous somme des senegalais, il y a certaines choses que notre pudeur de ne nous les permet pas. Ressaisissez vous

  • nangou

    kham naa deee sonou ngennn neek di debas si ko kham ni fallewouleene kou nek tok sissa clavie di khas nitte ko kham ni doundula guis ngenn viviane mi mouno lénn ko bagna tee def limou beuga defff dangen di sonou rekkk mé mom faléé woulénn fi kou dé ak sa baméll kousi néékk am nga sa panou dayye sissa biir keur lidiantiwoulééne ko ngen di lidiati copou dayou diambour boudéé yenaye dougal nitte aldiana wala safara dina léér kou nékk tok diko khas lingenn di wakh ni si mom danguénn koy defal promotion1993 ba léégui yenangui wakh si mom te wagni wouko draaaa teb kham na kousi néék telefonam wala machin foto viviane mingui si wala music gou viviane fi dall kou dé ak sa baméél may lenniou souniou diam nak lii yeuréé laa apréé parénasi jiko diou bakh ak khol bou rafet rek am solo yala rek mo kham mo meunn yennn gni di wakh yeup kenn kou nekk khamo fo moudiee vivi ligueyal tee boul guessou jobb rek boula kenn stresse

    • wally

      bien dit

  • Hot Boy

    Vivi douko bayi ak khaleyi diadieuf Vivi na geuna gatt

  • Issa

    Franchement, ça lui va pas, et elle donne mauvaise image à sa personne.
    Si elle s'habille correctement, tout le monde l'aime et l'adore en tant qu'artiste
    Si elle s'habille de cette façon, les hommes aimeraient juste la c.ouiller et la laisser partir.
    Fans yi kouma saga saga nga sa yaye.

  • XOGNE REK

    mane deh souma amone 30munite rekk thi kaw vivi ame sokhéte mokhéte rekk loumou deff bahna

  • mouba

    viví ya tay yonou kén nékousi

  • B M C

    senegal daal aamna gnou métti rekk mais vivi tenue.de soirée la sool di teuggu soirém sooluko si bédd yi limoom dou infos belle tenue

  • adajo01@hotmail.com

    bou doul darra soutourallale sa nom bii (SOHNA DIARRA) ensuite tu es une grande DAME!!!! Aussi bayil hélle si, demain tu seras grand mère,inchalaourabi Philippe dotoule enfant en plus tu a une grande fille tu dois faire preuve d'exemple devant elle surtout, elle est appelée à se marier avoir des enfants té yaw naweléme ngaa .VIVI tu avais dit tu vu SERIGNE FALLOU n'oublie pas tes paroles que tu avais dit publiquement. yalla bahna . Affairou ADOUNALA, Tu chante bien ,change la façon don tu s'habille , manchala tu as la voix tu es très belle manchala! !!!!!!

  • nana

    la prochaine fois ce sera le cul en l'air ?
    ce n'est plus de ton âge et ç carrément vulgaire .

  • zakaria

    viviane dal nekh rek la deff

  • l

    mane bala maye dee madegueu niounana logamoule ganye leye diekhe bou rombe naye nekh tés à chaque fois on voit les jeune mourir sa v dire qu' la mort peut venir tout suite gaayi on crois en dieu li yepeu adouna laye yeème

  • Nabou zo

    Maman chérie lii nak transparent na gata na weu?

  • Diouf

    Fi Senegal la do Kim kadarshian delolene sen heel ci yalla bamele lou jiara bayi heel la hijab femme musulmane

  • madiba

    Sant yalla : tous les sénégalais ne sont pas musulmans!!!!!!!

  • madiba

    Bravo viviane, la prochaine fois tu oseras le string à paillettes.. Moi j'adore!!

  • sant yalla rek

    Li niaw na torop sii de rou senegal

  • bili diouf

    toujours plus belle la beauté et la charmante sont aux rende vous

  • sante yalla

    yow ladiva'deuke bo diem tė khamo lofay fėki diėmala yobou yobal bou doun mo gana woor, li rafėtoul ci kouy wouyo dioulit rawatina ap mouride

  • Sopey seydina Mouhamed

    La mort de maty mbodji doit vous apprendre bcp de choses. Adouna bi dafa diekh Ba pare. Viviane ligua sole djekoul rafetoul te dagua am djaboot yalla nala yalla sopi.

  • zaleh

    oh jadore trop.ns en relamons encore.pothie day khess fess melni sa boss macha allah.na geuneu gate.

    • réglé

      Zaleh ya soof

      • m.f.d

        nit loumouy wote naka nourou boudee daga wakhne ab dioulitga wargaka nourou s.touba nena loo bagoul koula diawaleek mom boulka nourou nourou lou

  • Eupna

    Waouh la reine lo nam

  • ladiva

    oumy
    fi aduna la lo hamout guay lay dieh bosi nèkè nay nrkh
    ??????????
    love you my vivi mouah

  • 2PAC

    SLIP BOU NIOULE LA SOLE

  • oumy

    ladiva ya bone bou guene gat Hana tatounene laye def (fans si yi boulenma dor Dee)

  • fatou mbaye

    chon naaa ma vivi c sexy et classe machaalla.mouaaah

    • réglé

      xanaa yaw géuwél nga

  • léebon lippon

    bén na way la won ak guélam wadji di beug lal guél bi bagn mounan boy bi bopp bi rek lay dougoul douma dougeul lépp ndéketé amna bén mére boulén di deklou mére nan Ndaw sa farr bi day doul bouy dougeul bopp bi lépp pay dougoul bagnal.

    • réglé

      fén rék

  • ladiva

    my vivi yaw dara fayoula
    ni la dè bi sah dafa goudd prochain fois na geuna gatt
    love you vivi ?????????

    • goor

      mak bou amait soutoureu mo ko may bopam

  • oumy

    Mais viviane x
    ana amoul diabote
    ki dou mousa nek mak

    • réglé

      Mo kii nga xamni calason boum guiss an thie yon daafallé jabot, kidal ab Thiaga, may wax mouy doul nan da guis Segne Fallou,Geuwél 99,98% ay domaram you bone

  • ab

    mok bania soll yeure io yam

  • thiat

    ha sisthe li mom dou yeuré vrema yawit limala waxone dési bayi khel way li eup na trop

  • The Best

    rama rey ngama

  • Koty

    une femme dafa wara am des bon poth manam molin you bakh sakh dakh c le diferente entre l homme et la femme com you vivían yi nekh nama lool sakh wayé deud ak sa dieukkeur say yél di mélna bosam mane Koty andou mathi té douma wakh ak borom yél youmélna samay yél point

    • réglé

      yaw khanaa sa beut yi baxoul, fi ya fi guiss tengue you rafét, way toogal

  • majesty

    ahhh thioumm way. Vivi way neu Baar way

  • O n

    Soub khanal'lahhhhh
    li mo boneuuu tei rafet ci beuttt way

    • m

      RIRES; kHAKHATAYE ! Wakh nga deug dé

  • Plpn

    Jaime ca et c beau a voir

  • fina

    rama bou ma dadji

  • rama

    ki môme d'où donne makk mouk (khamna fans yi legui gnou khasema)

    • fall

      Rama kidal mol rek ladéf

      • réglé

        Mooo Magét gui nga nan mol, niak fayda

  • Harb mousba

    Machalla ke veille sur elle Amine

    • réglé

      xanaa Zoom mo tangue yi , war géuna wouti ay lunét déh,kii 2em main la Tactil bi doxul Batrie bi day wath Ecoute bi léroul Tate bi dou charger,reparé walla sanni?

    • kham

      doule lou bnne li mou sol

  • marcos

    ki kay tati nen la deff

    • diattou

      Bilay wakhatiko yiwoul daal

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *