16 COMMENTAIRES
  • kebe *

    aida boula dara dieulè si sole lou diote dafla diap loll et bne continuation my sister je te love grave

  • toufa

    Bilahi mala begue aida sama xole lala déf laf thiat rék machalla tof yi nicena trop

  • nop djekereume

    Sagnessegua machalla amena classe

  • lora

    Très classe ma belle manchallah bonne continuation

  • rouna senegal

    je kf ta voix aida samb du courage

  • loli

    trop classe mais j'aurais préférer sa haut bii gueuna diote

  • KHADY

    nice na trop

  • Ma diomi

    Tu es magnifique tu es le futur de la musique sénégalaise akk pape diouf et waly y alla saam leen

  • rom

    Machalla aida ya mana way

  • zelko

    @loli khana danga beugue mou doone ndoket, lii rafet na machallah

  • hanch

    waw waw aida nit mome nité rek

  • begue lou rafett

    mai khalé bi guiss na sama bopp si mom….bouma ko takonn dé. sou Mac j'y wakhé sakh ma saga ko. ..djiguenn day fess way ame nginaw gou rey té diekk…tarkala way Samb

  • Madame dieng

    Aida samb lou rafet rek guay def diko sol siguil gua di guene

  • yacine diop

    mais aida sa sagne s'' nice na trop

  • nogayesaer

    sol bou yiw dara dakhouko si djigeune aida macha allah

  • maty

    c hyper joli ma belle, continue ainsi

Publiez un commentaire