Publicité

26 photos-Gamou Tivaouane : Aziz Ndiaye livre des dizaines de boeufs à Abdou Aziz Sy Al Amine

Le promoteur de lutte Aziz Ndiaye en bon talibé tidiane, a livré ce jeudi au porte-parole de la Famille Sy de Tivaouane des dizaines de boeufs pour sa participation au Gamou édition 2015.

Abdoul Aziz Ndiaye (1)
Abdoul Aziz Ndiaye (2)
Abdoul Aziz Ndiaye (3)
Abdoul Aziz Ndiaye (4)
Abdoul Aziz Ndiaye (5)
Abdoul Aziz Ndiaye (6)
Abdoul Aziz Ndiaye (7)
Abdoul Aziz Ndiaye (8)
Abdoul Aziz Ndiaye (9)
Abdoul Aziz Ndiaye (10)
Abdoul Aziz Ndiaye (11)
Abdoul Aziz Ndiaye (12)
Abdoul Aziz Ndiaye (13)
Abdoul Aziz Ndiaye (14)
Baye Alé Ndiaye
boeufs (1)
boeufs (2)
boeufs (3)
IMG_0163
IMG_0190
IMG_0192
IMG_0196
Serigne Abdoul Aziz Sy Al Amine (1)
Serigne Abdoul Aziz Sy Al Amine (2)
Serigne Abdoul Aziz Sy Al Amine (3)
Serigne Abdoul Aziz Sy Al Amine (4)

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

107 commentaires

  1. mouhamed

    alhamdou douli lah begena len yen niep way contan si yen bou bkhe way kou wakh lou bon ak kou wakh lou bakh dilen fatta li rek ni nit yep dougne bene yalla binde te yamalewoul aziz limou def yalla nako yalla yokou bou bakh way ak kep kouy def lou bakh si rew mi kou melni bethio chiekh amar niep ben lagne lep rek si yalla la diem yallad nalen yal yallae nalen yalla defal lou bakhe


  2. saliou toure touba

    Man moride la mai def lolou bakh rek mo bakh Azim ndiaye yalla nala y alla defal aye khewal yobari bodewani ga gan kou man ce barkip borom gamo gui nik lin fi de wakh rek senegal nion niep bin lal kin koni naga gam kila y alla bolil rek dakh moride ak bin guir y alla delin wakh lo rafet


  3. Immigree

    Merci Elhadji Diop Dans un forum de discusion libre ceux qui reflechie du bon sens ont de la places ici … Bayilleenn Khadiallee Tarikhayii …. TIDJANE . MOURIDE . KHADRE . Nieupp Wakhou YALLA Reck Laniouyy Wakh AK SOUNA SEYDINA MOHAMED SAW .


  4. Elhadji Diop Talibe Cheikh

    Ziar Sama Serigne ABDOU AZIZ SY Ibnou KHALIFA ABABACAR SY RTA . … Dieureudieuf Ndiaye et Famille (AZIZ) je vous remercie de tout coeur YALLA NALLEN YALLA FAYE THI BARCKEE SEYDINA MOHAMED PSL je profite de cette occasion pour REMERCIER nos Khalifes Generaux du Senegal .. Eventuellement Serigne BETHIO L;initiateur de telle Action … Rooyy lou bakh thi dinee la bockkk …. JE VOUS SOUHAITE UN BON GAMOU … Boudewenee Yalla Na Yockou Feepp Thi Senegal Skyp. elhadjidiop99


  5. Véritè

    slt wa senego…. ma kèstion rèsult k…. s'il sagi d la fami de cheikh seydi hadji malik sy, vs les apeler de leurs propre nom ( en èradiquant le titre de serigne)…mè qd il s'agi d'1 otre fami confrèrik vs utiliser le titre de Cheikh Ou Serigne


  6. Paulèle

    La vérité est que vous etes vraiment bete ,Aziz N'diaye le premier.Il y'a tellement de pauvreté au Sénégal que le prophète Mohamed psl aurait préféré qu'on nourrisse les pauvres , ce saint jour.


  7. Cmd

    gnanal léneko mo gueune lou tay sénégalais sohorr goudi Mouhamed PSL lako défal gnane déwéne mou déf lou raw liiii lou fi diarr comparaison amléne béne esprit de dépassement wayy ishhh suis pas tidiane aziz dieuredieuf kou déf lou bahe gnou wah kooo.wassalam


  8. general

    me nit mo sokhor ma bagne kou sokhor meme kou bonne gua khame ko dioulil gnari rak gnanal ko pour mou sanger te li mou deff daffa rafette nakhe bou ko nekhone ame na fenene fou mou ko menone deff aziz dieure dieuf santir naci sama bopou


  9. talibé cheikh

    talibé cheikh dafay mandou, am soutoura; ragal yalla beug yonente. gnoun talibe cheikh dagnouy sagnsé té dougnou khoulo, dougnou wakh wakh bou gnaw thi sougnou moromou dioulite. dieuredieuf aziz ndiaye linga deff rafetena yalla nala yalla fayal bopam thi barké Nabi mi gueune gneup.


  10. am

    Mandeh douma mouride douma tidjan te andouma si yefou tarikha mais way kouma tegalon niom niar ma diel tidjan ndakh niom li eupou limai degeu sen wakh Yalla ak Yonente bi la nioy wakh woute ak mouride yiy tek seringe si plasou Yalla ak Yonte bi,Aziz Yalla nala Yalla nangoul bouko nango Yalla nala fey lou kawey sa njorte,Amiin


  11. papa

    TIVAOUANE PEUT AVOIR TOUT L ARGENT ET LES BOEUF À GOGO MAIS C PAS SA DÉMARCHE ET C LE MANGER COMME POUR CERTAIN C EST PAS LA MÊME CHOZ MAODO C EST DÉMARQUÉ DE TOUT CE KIÉ MBOUMBAY COMME SON VISAGE RAYONNANT PEUT LE TÉMOIGNER TIVAOUNE SE CACHE PAS DERRIÈRE DES BESOINS ALÉATOIRE POUR EXISTER MAIS LA LUMIÈRE DU PROFET RESTE ET DEMEURE À TIVAOUANE JUSKA LA FIN DES TEMPS LA TIDJANIAH EST UNE FORCE SANS BRUIT ET PROPAGANDE MAIS DANS LA SAINTETÉ DE L ESPRIT MUSULMAN ET PROFETIQUE


  12. dudy

    à tivaouane il parle de dieu et du profet il mérite tout l or du monde et ce n'est que le commencement aziz tu sera meilleur en 2016 les jaloux vont maigrir car la nuit du profet de maodo est mieux que tout sur cette terre le reste c'est du bruit mouhaha


  13. Ma Beugu Aziz Ndiaye

    Fier de toi mon grand doko rethiou dé inchallah. yaw elcapo sa baye mo xamoul yap nioune si lék lou baax la gnou deuk oci Aziz dou Bethio limou yor da lew tei Bilahi Walahi si kanam rek lay dieum. Sen xol yi di na geuneu té gueule ndeim yen mécontents yii II

    Vive Aziz Alé Ndiaye


  14. ABDOURAHIM GUEYE

    Diadieuf Aziz que les autres suivent tes pas.

    Que ces dizaines de bœufs soient des centaines l'année prochaine

    C'est le prophète qui te paiera


  15. Amir Abdallah Niang

    Abdou Aziz Ndiaye mane déh en tant que talibé cheikh bethio limalay nianal moy sa dieuf dji yalla na yok yalla guako guena meune yalla takh guay def dou niit yi dieuf diouné loumou tole nonou lala yalla di fay ligay si seetou yalla guako si ame si barkep Mame Abdou Aziz sa tourado bou tééd bobou yééne nak gni commenté niane léne def ni aziz def mo gueune wakh diou niawe dji wa salam niou yééndou ak diam


  16. EL HADJI FAYE

    encore une fois de plus ce n'est pas et cela ne doit pas être un problème de tarikha Il a fait comme cheikh Bethio et tant d"autres il faut l'encourager je pense que c'est mieux d'avoir de préjugés négatifs Cordialement


  17. grace

    nioune deffounou bethio morome ay liitary derratte la sokhla bagouko sakha khamm waxoumalak di kholl limouye deff kouye top nitt dankoye topp ngir yalla mba mou dilla wax loula yobou ty yalla nioun nak bounou deme tiwawan tallounoufaa lekk danouye diamou yalla ba nibissi barrigo bou fess la rekk ak barrigo bou amoul darra bruit ba barre rekk waye darra nekoufa


  18. EL HADJI FAYE

    encore une fois de plus ce n"est pas et cela ne doit pas être un problème de tarikha Il fait comme cheikh Bethio et tant d"autres il faut l'encourager je pense que c'est mieux d'avoir de préjugés négatif S Cordialement


  19. Talibé cheikh pirr

    Moi je me demande pourkoi certain mouride non pa un esprit de dépassemen il suffi kun tidiane def lou bakh rekk kéne teuyé séne lamigne di wakh ayy wakh you niaw bilay yéna sokhor topoto léne séne tarikha té bayi nit yii ak séne tarikha Mane t sant na yalla bamou ma défé talibé cheikh dakh dinadj la yar sii diné dina diangal respectei nittt lek alal bou leww doylou Aziz ndiaye liga deff si gamou gui yalla dina la faye baga yeuko si barkii yonenty psl Gamou pour diamou yalla mo diou fa yob mei ba fo t sounékone ndiouma biii nimporte kel khaliss la gnouyy dieul kone kéne wakhatou ko mandouléne Serigne Abdou Aziz Al amine yalla na yalla fayal gnou ko té goudal fanane amineee


  20. mank de civisme au senegal

    mai mane dal j comprend pas loutakh senegal nite yi meti li aziz Ndiaye deif defa refette ligueyeul suñu borom reka am solo pr chiekh bethio auci loumouy deif defa refet legui nak yallah reka kham


  21. Mme MBAYE

    Abdou Aziz NDIAYE. Yalla nala yalla faye, maye la fane you goude té anda ak werr, diam, soutoura ak yokou ba yeukko thi daradia SEYDOUNA MOUHAMAD PSL AMINE


  22. khadim

    diadieuf aziz ndiaye rafétena mounone nga ko bagna deef nax amna gnou yoor sééne xaliss deff ko si lanéne lou yalla gueureumoul yonéne ti bi bougouko linga meune réne yala nga meune louko raw déwéne si barké mame borom touba gneup ay diolite ay mokk lagn


  23. tous les temps

    yoro juste une eclairecissement aziz mom rek ma diokhé nak yi t bethio counék si aye talibém dalaye sass donc doumana yemm azi dal

    yala na yok ba yekko


  24. birima

    abdoul aziz arrête le NGUISSTAL en tous cas je te préviens je t'ai vu dans mon listikhar en prison je ne sais pas de quoi tu as peur mais par ces gestes tu caches quelque chose parles a tes proches pour qu'ils prennent les devants avant qu'il ne soit trop tard sinon la chute risque d'etre tres lourde. wa salam


  25. fatima

    Gamou dou khaware tes dou noss goudi seydina mohamet la talibe chekhe viande khobou gnou tivaouane diamou yalla mo gnou fa khobou aziz rokhoul quen lamb dan dolela sagnoul day ligueye def len ni gnom guen leguey mo guane wakh djou bari do lene avance do lene bakhi kou avance khene khi soyar la betho lamou man nako def moromam def lamou man mo guen ratati rek def lene limou def aye bern khobou gnou tivaouane gnamou yalla seydina mouhamet mo gnouy fa khobou


  26. fatima

    Gamou dou khaware tes dou noss goudi seydina mohamet la talibe chekhe viande khobou gnou tivaouane diamou yalla mo gnou fa khobou aziz rokhoul quen lamb dan dolela sagnoul day ligueye def len ni gnom guen leguey mo guane wakh djou bari do lene avance do lene bakhi kou avance khene khi soyar la betho lamou man nako def moromam def lamou man mo guen ratati rek def lene limou def aye bern khobou gnou tivaouane gnamou yalla seydina mouhamet mo gnou fa khobou


  27. michu

    elcapo wak gua wak dji xalis bou léwoul dou dougou tivaoune mo tak dou gawa paré begue nay lo fa diouli yalla nangou keur maodo kéne mou no ko tilimal bou doul wone 7 sénégal digue merci


  28. niang

    Mais je crois que Aziz sa profession n'est pas seulement promoteur de lutte, svp éviter de blâmer ceux qui œuvrent dans le social, comparaison n'est pas raison,


  29. Malick diop*

    Machallah waye Aziz Ndiaye yalla na yallah yakou Si barké Seydina mouhamed.Tei aussi ngi di critiqué Yeup na niou khamni Tivaoune lépp Yabou woufa béne talibé mei diamou yallah ak magal yonanti bou téde bi rk.Seydi El Malick Sy Ridiyallawou tallah anekhou lép koumou masél takhaw sa diabou bayi léne sisou bi Tei nangou lii yallah dougal


  30. Malick diop

    Machallah waye Aziz Ndiaye yalla na yallah yakou Si barké Seydina mouhamed.Tei aussi ngi di critiqué Yeup na niou khamni Tivaoune lépp Yabou woufa béne talibé mei diamou yallah ak magal yonanti bou téde bi rk.Seydi El Malick Sy Ridiyallawou tallah anekhou lép koumou masél takhaw sa diabou bayi léne sisou bi Tei nangou lii yallah dougal


  31. SAMB

    WAWE GOOR AZIZ LI MOME NIEPAKO WARA RAFETLOU TEE NGUENE BAYI CHEIKH BETHIO DAGUENI TEUKALEE LOU MEGO AMNA WAKH YOO KHAMNI DIAROUKO SAKH.KOU DEF LOU BAKH ENCOURAGEKO NIANALKO MOU GUEUNKO MEUNE TEE BAYI SOKHORE.SOKHORE BAKHOULE NANIOUYE WAKH LOU RAFETE MO GUEUNE.


  32. Elcapo

    ALLAHOU AKUBAR ALLAHOU AKUBAR ALLAHOU AKUBAR

    Man demay warou ji kilifa dineyi

    Sourtou koumelne….JUNIOR….

    YAW PROMOTEURU LAMB BO KHAMNE LIMOUY LIGEUYE KHALISS

    BOU HARAMLA MOUY LAMB YAW GEY KILIFA DINE WARKO

    AYE AYETOKO NIOU DIOKHLA JI

    KHALISS BI GEY KOU NDANATT

    AHOSOU BILLAHI MIN JUNIOR

    WAYE NAK LEK RIBA BIROU JUNIOR

    MINNAKO NDAKH MOM DIOUMAY

    TIVAONE JI KHAMNE KHALISS BOUNE DIOKHNANG KOKO TA MANTA FEKHE BAMOU PARE

    WAY WAY JUNIOR GUIR YALLA

    AK YONENTEBI AK DIEUMY semam

    Diou bakh dia EL HADJI MALICK

    RADIYALLAHOU HANHOU

    ACGALELL DIOUMAY EL HADJI malick

    Dji TA BAYYI KHOULOBI BOKO ACGALEWOULL BOLAGE BODIAKKARLO AU EL HADJI MALICK S'Y DIGA ROUSS DE


  33. Talibe bamba

    Sama Gayi ken kounek na game limou ngame thia bayi cheikh bethio wala azzise ndiaye thianou niane yalla mayniou li bankoye mana deff koume cheikh bethio ak cheikh amare ak azize ndiaye


    • THIOUNE

      YORO WAHAL DEH AFAIRBI CHEIKH BETHIO LA LI LEPOU MOKAFI GNIEUKE KOU DEFF NAKO GUERAMER CHEIKH BETHIO THIOUNE MAME BAMBI MOU SERIGNE SALIOU AZIZ WAWE GOR MAIS DEWENE YOKAL LIME BI NAKK OK BETHIO .


Laisser un commentaire