PUBLICITÉ

(20 photos) Aziz Ndiaye et sa famille offrent plus de 200 bœufs pour un bon Gamou

Aziz Ndiaye et ses frères ont fait don de plus de 200 bœufs pour la réussite du Mawloude 2016. Après la réception, le porte parole de la famille de Cheikh Seydil Hadji Malick Sy  a béni la famille Ndiaye “cette action n’est pas une première” déclare Al Amine.

Vous venez par ce geste réitérer l’action de votre grand père Aly Madjiguène Ndiaye, qui est le premier talibé à offrir à Serigne Babacar Sy  dix (10) chamelles, dix (10) bœufs, dix (10) moutons et dix (10) chèvres, c’est en 1974 que votre père ici présent, m’a offert 1 bœuf et c’est cette même année qu’il m’a donné un homonyme”.

Aziz Alé Ndiaye explique la répartition des bœufs: 55 à son marabout et homonyme, Al Amine et le reste à la gendarmerie, à la police, au préfet, aux différentes familles religieuses de la ville sainte, les voisins et des repas seront distribués à la maison pour les nécessiteux.

Pour le budget dégagé à cet effet, Aziz déclare que c’est un adiya à son marabout, Serigne abdoul Aziz Sy Al Amine, il ne dira jamais le montant.

 

 

Annonces

(30) commentaires

  • Moussaka

    Adiya !!!! Alhamdoulila

  • Mbacké Kane

    Vraiment li rafetna

  • Real

    Ma fogoneni adiya ribala. Topando lou bax dara nékoussi

  • Danilo

    mdrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr lima nekh moy gnom gnokoy dieundd ba par womatalko sen bopp pour gnou guislène mdrrrrr mais bon courage adiya riibaaala

  • Al

    Dieureu dieuf

  • Mansour Fall

    Sa c est une geste magnifik li nice na trop yala nako borom gamou gui fay

  • Sydabakh

    Sénégalais mom kouye deff lou bakh yaye devenir sen ennemis.

  • Ndiaye

    C’est ça l’adiya. Est -ce haram ?

  • Sopé Nabi

    Def Si Goudi Mouhamad Ibn Abdoullah Yallah rek mmola meuna fay dina fay fi faye la feulé dakhté yangui si diné mouhamed defo fi louniaw wakho fi lou niaw Machallah Yal nala yallah sam té ar leu yak sa famille !

  • Omar

    machalla yalla noko yalla faye

  • Talibe Bamba

    LI RAFET NA LOLE YALLA NALA YALLA FAYE SI BARKE BROOM GOUDI GUI SEDDAL SA KHOLOU SERIGNE LOU AMA AME SOLO LA MAN EN TANQUE MOURIDE KONTAN NA SI ABDOUL AZIZ NDIAYE MI YALLA NAKO YALLA FAYE YALLA NA YOKK ATTE MOUNEKK SI BARKE SERIGNE TOUBA

  • Sy

    yala kén yokou ba yékko si barké seydina mouhamed psl

  • Bour

    Aziz machalah yalna yallah faye si barké serigne babacar sy machalah

  • Deuggg Rèkk

    mai khalissou LAMB RIBBA LAH Mdrrrrrrr

    • Sa Yaye

      xalissou raye katou nite nak cad BETHIO THIOUNE AMI DES THIAGA

    • Suceuse De Bethio

      #deuggg rekk demande le a bethio thioune le vieux thiaga et tueur de personnes

  • Sope Naby

    je ne suis pas tidiane mais wakhtane dangaye wakh deg yene gniy lebou nane adiya defewone na ribaak dafa Aram yena ngui ci mauvaise fois ndakh danguena guenna li serigne abdou Aziz al amine ci contextame dafnewone adiya bodeh kilakoy diokh dama beug li ak li ak li dok lako diokh pour nga fadialko sokh lam yoyou motakh mou diokh lako nga nangouko te manoko fadj lek nga ribaa nome al amine day diel adiya adiya eupp peut etre ci limouy dounde adiya batou arabla mingui tekki lougne may pour nekhale lako manam ci francais cadeau kou nekk mane nako lekk bougne ci galoul dara bayilene lou nit wakh nguene welbetiko pour rek gnawalate

  • Nabou

    PENDANT CE TEMPS , CHEIKH BETHIO est en 1500 , ils vou reste encore, Goorgorlou lééne rek dina bakh

    • Adja

      makk daye dhh xaléé daye khole léne séne commentaire loufi diar wakhe adiya ribba le tékeleu mouride ak tidjane moléne nékhe yalla nguéne torokhe

    • Maimouna

      ##NABOU yow mi di wakhe @@NABOUDIT PENDANT CE TEMPS , CHEIKH BETHIO est en 1500 , ils vou reste encore, Goorgorlou lééne rek dina bakh “”””””””” il fallait ajouter qu’il ait le seul marabout tueur de personne au sénégal qui enterre des vivants qui fait des ##cheikhette. NB:BETHIO THIOUNE==SATAN en cher et os

      • Sa Yaye

        #nabou il faut comparer ce qui ait comparable raye katou nite bobou bouko fi toudou waye

    • Sa Yaye

      #nabou il faut comparer ce qui ait comparable raye katou nite bobou bouko fi toudou waye

  • Amiral

    nabou yaa deg

  • Moi

    loutakhe ngéne meuna changer wakhe nite kou bakhe sa papa mola wara geunal lo guisse thi kaww soufe kone bokk kou ame loussa papa amoule djokhe ko respect.##nabou yalla ngua reuthiou sa kadou yi thi kaw soufe il faut comparer ce qui ait comparable

  • Alkhadimyy

    Yalla nako yalla faye si barkep sr touba

  • Talibé Mouride

    wakh balle la batax louway beuga wax nako khalate boubakh.mouride wala tidiane wakh diou gnaw waroulène .linou bolé mouy islam mo eupou linou takhalé ta deureum bou sèll gni diokhè ko ta yalla rèkk takh mo eupal sounou borom milliard bou lalou ci nguistal ak reuy reuylou. nit kou nèkk ci ay commentairame meune nagnou sè kham bane comportement la yorè batakh may sakkou gnou rafètal kaddou yi ak yènè yi ta bayi di comparer ndakh nit kounèk nimou tollou lay dieufè ta weurseuk yèmoul.goudik sounou sangue bi(PSL) loussi way dèf doukou rèthiou mouk ta loussi way dèf yalla nassi dadiè ak ngeuramal sounou Borom. wassalam

  • Dof

    heureusement que les mourides montrent le chemin

  • Sope Khadim

    liirafet na trop yalla nala yalla faye

  • Real

    Dieureudieuf Thioune toujours imiter mais jamais égalé. Nabou pour te rectufier on etait a plus de 4000 boeuf lors du Magal sans compter les chameaux, les moutons et les poulets. Le Cheikh peut etre criminel mais dieu merci il n’a jamais essayé de poser une bombe dans la voiture de son père. Bouléne niou taxa wax. C’est toute la difference qu’il y’a entre Serrigne Touba et les autres

  • Moussa Ndoye Seck

    yala nala yala dfal diam diou bari si bark wer bi Abdou aziz ndiaye

Publier un commentaire