5 COMMENTAIRES
  • bass

    Paula niak Programm lo thi kham.. Sénégal mo beuri ay radio ki télévision you amoul bén program bou important. boy setan yén télé Sénégal yi sakh de fois da ngay rousss

  • Rose

    mety mais yala mokoye yombele ak crise bi machala yala bakna

  • babs

    l’homme en rouge est un ancien footballeur de la Jeanne d’arc et de Niarry tally . Ndeysane Mamadou Sonko alias Condor.

  • Cherie

    PAULA tfm yilen beugeu nio opeu yilen niepi yaw nak bo amoul lo yoone sa affairs la mais tfm ligeuye bou rafet laniou def,Machaa Allah law la thiat gfm tha kaw tha ci ligeuye bou nice Yal na sen diam yokou,Amiin

  • Paula

    Ma Xarée wa TFM louy siy seen yoon tchi gnak lagnouy envoyé tchim maleen diepi ma tay

Les commentaires sont fermés.