52 COMMENTAIRES
  • RS

    ndeysane..li metina trop yalla nako sounou borome takhawou.

  • RS

    ndeysane sama yarame dawna khale bi yalla nako yalla takhawou bambou weur ak diam

  • RS

    yala nala yala takhawou banga weur ak diam

  • assy

    yaalna sougnou borrom yoonee kouleen takhawou si Dara dji nabil moustapha te yaala rekk takh. in cha allah leppeu sinettali leyy moudjiee.

  • Alou

    C'est vraiment tres triste yalla na were si diamu

  • Zo

    Donne les cordonnees svp

  • baba

    Amine

  • mane

    metina torop lii .nguir Yalla nguir dieumi Rassoulilahi ñii am louñouko meuneu dimbeulé def len nguir Yalla. liñouy def ci soirée yii ak diko mayé ci khawaré yii Yalla wotena dé

  • Khady sy

    les cordonnées svp

  • Mamythiaw

    C vraiment triste kou nék nako khol thi boudone sa dome la dale diapalé lenko guir yalla soudone soirée lagnou len toudé guén raw thi s'en bop té khalé bi kouko diapalé yalla di nala ko faye mane dé souma amone defko

  • begue senegal
  • dimkha

    Pour waly seck qui prétendait faire de l'oeuvre sociale le prix son album vendu aux enchère à 8 500 000f, voila une bonne occasion.
    en plus senego ça sert à quoi de publier ce genre de vidéo sans donner les cordonnée pour les gens de bonne foie qui veulent l'aider…

  • Bamba

    Yalla nako sa brom guestou,metina trop

  • aram

    Les cordonnees please

  • bibs

    Bonne idée Dimkha. Les coordonnées

  • fall

    yalle na tane ak diame da se warona wakh nimero comt walla nim telep

  • AICHA

    les cordoné svp svp

  • chacha

    yalla nako yalla tahawou

    • dado.gueye

      yéne mbokou diouliteyi yi nga khamené yalla may naléne touty
      kholéne si yalla nguéne dimbaly khalébi

  • Ben bah

    vremnt

  • jannick

    C bien de publier dans les medias mais c important pour les victimes que vous donniez leur coordonees.
    Alors ça vient les coordonees ou pas!

  • diop

    mais les coordonnées svp ohhhhhhhhhh

  • Bineta

    Il faut regardé l'émiision sur 2stv diguéne amm coordonné yii.. Incha Allah

  • ouly mbengue

    C TRES DURE ET TRISTE YALLA NAKO YALLA TAKHAWOU

  • Schwarz

    Wa senego guir yalla fékhéléne djokhé cordonmé famille bî
    Ame na gnou pare pour ndimbeule , djiappe léne sy rék , sino pub bi dou am sens

  • Reanna

    Maréme FAYE yeunguoul waye wonel sa bope

  • sokhna

    Les cordoné svp

  • Thiare diop
  • Na woor

    Yallanako sounou boorom safara ci oumou geuna guidé ci baaarké seringue Babacar sy !! Amine.

  • Na woor

    Yallanako sounou boorom safara ci noumou geuna gawé ci baaarké serigne Babacar sy !! Amine.

  • Thiare diop

    amine

  • CRI DE COEUR

    ou sont les grands batreur du grand théâtre voila réellement ou il faut batrer

  • tapha

    djokhé lén ay cordeném ngir yalla lou way am defthi

  • RD

    même s'il ya pas de coordonnées vu k la vidéo est passé sur 2stv dans l'émission entre temps donc kou si beugg deff dara tei yallah rek takh nanga wooté 2stv wala nga deme fa.. yallah nako yallah saafaral boppam..

  • Thiarediop
  • am

    Yalla nala Yalla mei shiffa

  • al haqq

    il est plus necessaire d'aider ces gens que de faire du n'importe quoi dans les concerts!

  • Moustapha CISSE

    Dimkha liguawakh moy deg,les riches sont des mechants.

  • oumardiop

    nom mettina trop mais kou ma ma diapale si kontact wadiour khelebi inchala sa ma numero mo nekhe ni 0046769548553.

    • Aminata

      2S TV : 33 823.93.54 ça pourrait vous aider

  • meme

    mane dale je comprend pa / pourkoi niou indi ko television dai diokhewouniou numero telephoname , comment faire pour laider?

  • Aminata

    2S TV : 33 823.93.54 ça pourrait vous aider

  • khadim

    Yallah nako Yallah takhawou

  • Papa kebe
  • NDEYYSAANN MANOUMA

    AYYWAAYY DIAPPAALLENNCKOO GUIRR YALLAH …. MANN DAMA AMOULL KHALISS SINON BEUGUENACKO WAYYEE MANOUMA … GUIR YALLA TAKHAWOULLEENNCKO NGUIR DIEUMII SEYDINA MOHAMED PSL .

  • Dji

    Les cordonnnés svp hohohoho

  • Djimy

    S v p les cordonnnés hoooo

  • Moulaye finou
  • degue

    ya des en ki di des cordone et si on vou done sa vou ne donera pa rien

  • MIS

    IL FAUT APPELER LEKIP DE ENTRE TEMP SI VOULEZ LAIDER OU NIMPORTE KEL PLATEAU DE 2STV

  • Dabo

    ???? ???? ?? ???

  • Daba

    Yalla nako yalla diapalé si barké seydina Mohamed

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *