Vidéo: Waly Seck face à une multitude de questions

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

23 commentaires

  1. chacha

    sama gayi bayiléne yak déer bi waly né po melé kou nék si yén am na problème si soufou lalam soyon serieu waly molén gueune yén gni yak déram dakh momo am gnanou wadiour s qi rest moy yala nako yala may kantane bou diapalé wadiouram bou goor kou kén am na diar diar soyon sincères é du courage waly yala bakhna


  2. adouna dou keur

    yalna borom bi yokou gnou rek waye senegal moy deukk bou beuri gnou sokhor te gnaw xalatt kou yenewoul kene diamm ndo ngawa amm diamm


  3. sanèl

    je suis pas u fans de youssou ndour mais nak n'exagère po nianal lene papa thione yalla tèguiko natou bi mou dèlou si ndiabotam ak kepeu kou niaby fètè guinaw am nio khamni sou mèlni rek laniou yakamti wayè yalla nama yalla mousal si genre nitt yoyou khol bou leundeum ni charbon rèk


  4. ciboye

    wakh lene sen wakh té guené si youssou ndour dou si daara thione ak domame bi gniou pasar-passere xalis bii ken wakhoul tourou youssou waly ak papam youssou ndour mo ken heupalé xalis yene yii geumeudi yalla là gniou wakh té dey


  5. objectivité

    Yow Kakooo sa yéné ga wakh mais il faut savoir une chose si Waly était mêlé à cette histoire il sera le premier à être arrêté. Arrêter vos méchancetés et laissons la justice faire son travail. Nul ne peut rien contre le destin de son prochain si tu as des problèmes de difficultés très difficiles parles en à God


Laisser un commentaire