Vidéo- Un internaute clashe sévèrement Bouba Ndour et son fils Philippe ( à mourir de rire)

Cet internaute s’en prend à Bouba Ndour et Philippe le fils de ce dernier. Selon lui, Philippe ne sait pas chanter. Bouba Ndour veut nous l’imposer. Regardez.
je suis d accord avec toi… c est une famille d arriviste bien que youssou chante bien…je l aime comme chanteur mais pour le reste non
Monsieur,t’es libre de juger la musique de Philippe Ndour,mais rien ne te donne le droit de juger le gamin ou son père.
PS:Moi non plus,comme vous,j’aime pas la musique de Philippe Ndour.Par contre,j’adore celle de sa mère.
Vraiment le gare a parfaitement raison
koussi rewoul amo beugn wayy, mais nak deug la wakhhh.
SA WAAY WAKHOFI DARA GNAK NGUA FAYDA LOL BEUGEU SIIW REK ponkal bou dyna yow nekk fi di wakh lo maitriséwoul nda beugeu siiw damal produire saa dom.
Bonsoir, je ne connais pas la musique mais personne n’impose a personne une musique ou une video.ET un papa fait tout pour la reussite de ses enfants, je ne sais pas toi comment tu fais a ton tour avec tes enfants mais ne sois pas jaloux si tu veux bien être un bon papa.
Nonnn,Maniakhtou ya gueuneu nekh si adounabi.Tu m’as kill.Hahahahaha….
wiiii Cè vraima tu ya règion il les nul khamou dara
Grand rye nga ma
copin yow dangua sokhor. Le fait que mou djiangui dacort nakh khalela mes lenen lothi tegue agnian mou mety ladjiap
Haha
way ma Diakhou yangui may réw waye mé nakk deugg nékhoul Philippe môme mounoul wéye
Dio nagoul li yalla dogal sa baye tkkiwoul dara mo takh
Dio sa baye tkkiwoul dara mo takh
dio khana amo baye demal sa baye diapal seytan
dio iow seytan ga boudone baye la moulaye diapal do wakh kounk nadm sa baye diapal khana amolene baye
chacun peut penser ce qu’il veut de la vidéo du gars mais il a raison Philippe ne sait pas chanter et les gens comme bouba profite de leur aura médiatique pour exploiter les gens et imposer son fils qui n’a pas de talent du tout
hahahahaaaaaaa ya dofde
hahahahaaaaaaa ya doffde
mMBEUR yaw doooooul doméxaraaam. c vrai ce gooosss ne sait rien absolument naaada
senego suprim ln videobi way saway yagui mlni kou doug keur diambour ni kn doufi sol pantaln manam liga wakh nip khamnani tgoka fn si loudoulni foto bomba ndour mola nkhol way Lolou sa afairla
Non masouma guis nit bou sokharèni mais li dina takh bouba geuna diapalè filipe .
Continuez à vous traiter de tous les noms d oiseau
Chamaillez vous
Insultez vous
Dénigrez vous
Bref plus d humanisme chez les sénégalais
A ce moment là les autres s entraident avancent évoluent et nous dépassent de loin putain y a pas pire qu un sénégalais en Afrique
Bande de cons quand est ce que vous allez vous réveiller et arrêtez de perdre votre temps avec ces méchancetés gratuites
God help us please
je demande a bouba de lui offrire 10000 pour acheter new crema ndakh mou lerr ba lale khoul bi li pour mane jalousie li
mes ki defoul dara wa senego yii diko fi dougal gnio yabat dofbi mes Sngal dou dme
Pourquoi est-il obligé de crier aussi fort quand il parle !!
yaw yaye domarame,ta vu tes neuves qui sont ici tu peu mme pas les aidaient, yaw conga rek c’est a cause de toi les gens sont entrain de dire des mauvaise chose a tes soeur tu es vraiment riducule koi boye
fils demal witti raisin , saison des fraises commencer na .
là au moins ding si am benn 100 euro ou plus .
sinon Philip ak Bouba tekki nagn bou yagg ..
yaw nga wekk sa awenir si niakhtou …
mettitou khol moo la nara ray ..lolou laa lay bagnal
Aider Baye Assane lui au moins a du talent.Au lieu de nous imposer ce justin poupa Philipe ndour.
Ma ngakhtou…. Wakhal d. Danu soneu
ki mo riewo yawo demal ligueyi tie bayi domy diambour
ya sof????????????????????
thiiiiiiiiiiim iow ya sofffff rk
Mdrr mais il a raison
Ridicule…..Jalousie….Sokhor….kon … no mai ki li mou bolee yeup ken meunou ko lim
Wouuuuuuuuuuuu!!!!
Sof ngua trop
No man mom dama warou légui dal Lou way nékh déff sa vidéo enveyie senego no li Euppona lol mdr
bravo
hahaha !ce gar m’a tué
Non gayine bii ay r lama dff koi
ligu wakh début bi sa m intéresse pas mais fadda je dit way mélodie cé le mellieur ici en afrik mais senegal khamou gnouko son les album créé des instruments lepeu si guemine album leumbeu cé fadda cé le mellieur chanteur rnb en afriik
sokhar bakhoul lou ame,nako sentee yalla tee boul khol keene dakh koo khol raw nala
kxkxkxkxkxkxkx woooy ioe khana coula diappale nga beug
RIDICULE!!!!
Cette famille est entraint de se servir des senegalais
Mdrrrrrr mais wadji mo nekh rek hahahahahahahaha Bilay wakh nga deug. Youssou ndour amoul héritier dn la musique ndeysane ey way sou maguété kan mognouy woyalati lou nekh.
non senego mo nekh toujours ok bou bess li si wayadi
IL a bien raison.
non senego mo nekh rek wayy toujours ok bou bess
wouye yayoye lil wow baw waw
Sa guiss guiss la yagale sa dom te gay bayi Domou diambour ,niak fulla beug siw
Sngal la d dafa am pidmie incurable bou fi ne dafa am niou sen khl yi khomak ba pare » rien faire pour eu nanou len bayi cardiaque r ye len.
deugala faada dou s’en morom mon pote de d la fse
magui kharr ba bn seytan n wakh ga deug
lou way nkh wakh deff sa video wakh loula nkh t dara doulathi fekk
Togne bakhoul serigne bi