16 COMMENTAIRES
  • azou

    nan tounkara tay mome danou nga vrément danga dioum waro doug fi waleuh sakh ngané guéwél yikoy déf ndakh s né pa tt lé griot ki font cela amena ay domou guéweul youla gueneu nék ay intéléctuél guene la diang eupela daradia eupela xaliss t moussouniou wayane exemple abdou mbaye madiké niang ak sama papa mane mi en plus wa dji limoula wax deugueleu ioe cii wayane nga deuk tmtc t bo sanione mélni yéneu guéwél yi lolou dafa lér arrété de généralisé wayy ishhhhhhhh

  • loulou

    tounkara fans nala torop wayé wadji dore nala un zéro mdrrr

  • rambo

    mann dema ree ba tass

  • Fouta50

    Tounkara respecte tes invités laisse les parler certes moi aussi je suis contre le griotisme

  • mamoudou diallo

    Laobés niom défarananiou guéwél yi nio thi dèss rèk SENEGAL émergé…

  • Gamboul

    Bien dit jeune homme… Tounkara se prend pr ki?

  • abou ndour

    tounkara da oupale nag way téy mome dadjinga.

  • seckou souane

    Tounkara ya togne c’est un griot il fait son métier. tu entres dans ses 18métres il te tacle alors égalité

  • ibson

    guéweul fou thiébam di niné rek

  • Germany

    Tounkara Ya aye Waye contane na

  • dione

    tounkara a parfaitement retion senegalaises beuguoule koukoye wakh degue denion varra depasse fui

  • dione

    tounkara a parfaitment retion senegalaises beugoule koukoye wakh degue senegal defa varra depasse fui naniouko wakh to deee

  • Cheikh DIOP

    toukara kou nekk nanga nekk sila ngua nekk

  • Astou

    wadji 100% 100 lako daur …mbeuleeeey daga yabate

  • Yax Bou Rey Faye

    vs navé rien compri, s ga na fé k ds afirmation gratuites.

  • Ndongo Papadiaw Diaw

    waay tounkara boulma ray aki rei way wadji kay nonou rek la msna wakhe

Publiez un commentaire