Vidéo-Thioro Mbar Ndiaye explique la vidéo-scandale de Bouba Ndour

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

28 commentaires

  1. dk

    arreter de parler de la vie privé des gens am nguéne louléne doye.c vs ki n'avez pas de soutoura yéne gni tokk si télébi yor séne lamign di wakh….


  2. teranga

    Le problème de thioro ce que elle a un manque de consiance une grande gueule mais elle finira très très mal liii d'où djiko djoulite billahi sauvages va ???


  3. saliou

    En tout cas kouy waxal nite lou niaw naga xamni yaw tam amena fenene fougne lay waxalé lou niaw té dou lo xamal nit si lou niaw waxko ndax sunu borom nena kouy soutoural domou adama kerok yowmal xiyam dinala soutoural


  4. coumbiss

    golo mbar Ndiaye ferme ta grande gueule tout le monde a compris ton jeu parce que tu ne fais que mentir ak sa vert you modé niak classe


  5. rafet xol

    mdrrirr Golo mbar kay hahahaaa mais nak wax nga deug dafa wara arrêté di fenal célébrités yi parce que ay nit leugn comme nieup am ndiabote bok si société bi donc wax dji dafa wardi rafet dafa yombou torop tok sa plateau di waxal nit yi lou niaw té damay deg niounane wax djou bone deukoul famou dieum famou tiossano la deuk té loufi way waxal nite kerok yowmal xiyam digako digueuntek mom donc nay rafet way


  6. rafet xol

    mdrrirr Golo mbar kay hahahaaa mais nak wax nga deug dafa wara arrêté di fenal célébrités yi parce que ay nit leugn comme nieup am ndiabote bok si société bi donc wax dji dafa wardi rafet dafa yombou torop tok sa plateau di waxal nit yi lou niaw té damay deg niounane wax djou bone deukoul famou dieum famou tiossano la deuk té loufi way waxal nite kerok yowmal xiyam digako digueuntek mom


  7. Kevin

    diami Sénégal tu as tout à fait raison cette golo mbar aime trop dire du mal sur le dos des gens surtout les célébrités et la plupart ce qu'elle dit est faux elle ment comme elle respire. revoie ta copie Golo mbar wax si nit lou gnaw baxoul rawatina loula woroul. essaye de changer Golo mbar


  8. diami Sénégal

    pourquoi nga si toudou tourou bouba meuno may gnigni sen diam je n'aime pas cette femme elle dit toujours du mal sur le dos des gens et elle en abuse bcp trop nek fofu di waxal nit yi loula nekh et pire dès fois sans aucune preuve fi la waxone ni baba hamdy dafa tak Viviane taku souf ce qui était archi faux. et suis sûr qu'elle fait pire té ken lidjeunti wouko. tok fi di doul rek ak niaway bou rey .avant de faire le moral à qui que ce soit xolal sa bopou ba paré ndax balagay diglé sangou daga wara set ba paré. espèce d'idiote !!!


Laisser un commentaire